Al-Mursalat · 33/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
كَأَنَّهُ جِمَالَتٌ صُفْرٌ ۝٣٣
Ka annahoo jimaalatun sufr
📖 Tekkim Wolof
dañu melni ay giléem yu mboq

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 31-35 — Simoore Al-Mursalat

31لَّا ظَلِيلٍ وَلَا يُغْنِي مِنَ اللَّهَبِ
manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;
32إِنَّهَا تَرْمِي بِشَرَرٍ كَالْقَصْرِ
moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,
33كَأَنَّهُ جِمَالَتٌ صُفْرٌ
dañu melni ay giléem yu mboq
34وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
35هَٰذَا يَوْمُ لَا يَنطِقُونَ
Bu bis baa du ñu mana àddu wax,
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Al-Mursalat 33

Simoore Al-Mursalat Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dañu melni ay giléem yu mboq

Simoore Aaya 33/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers