Al-Mursalat · 23/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
فَقَدَرْنَا فَنِعْمَ الْقَادِرُونَ ۝٢٣
Faqadarnaa fani`mal qaadiroon
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi dogal cëy Noo mana dogal yemale.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Mursalat

21فَجَعَلْنَاهُ فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ
Nu daldi koy saxal ci barab wu wóor,
22إِلَىٰ قَدَرٍ مَّعْلُومٍ
ba ca ab diir bu ñu xam ?
23فَقَدَرْنَا فَنِعْمَ الْقَادِرُونَ
Nu daldi dogal cëy Noo mana dogal yemale.
24وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
25أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ كِفَاتًا
Ndax defu nu suuf si mu làmboo lépp,
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Mursalat 23

Simoore Al-Mursalat Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi dogal cëy Noo mana dogal yemale.

Simoore Aaya 23/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers