Simoore Al-Inshiqaq ci Aarabu ak Wolof
Jàng Simoore Al-Inshiqaq ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (25 Aaya — مكية). Al-Inshiqaq Dégg, Al-Inshiqaq Tekki, Al-Inshiqaq mp3, Al-Inshiqaq pdf.Jàng te Dégg Simoore Al-Inshiqaq
🎧 Aaya
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
—
x1
يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ إِنَّكَ كَادِحٌ إِلَىٰ رَبِّكَ كَدْحًا فَمُلَاقِيهِ ٦
📖 Tekki
Aaya 6
Éy yaw nit ! Yaa ngi def jëm ci sa boroom, te danga dajeek moom de
فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ ٧
📖 Tekki
Aaya 7
Képp ku ñu joxe téereem ci loxob ndeyjooram,
وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ وَرَاءَ ظَهْرِهِ ١٠
📖 Tekki
Aaya 10
Képp koo xam ne nag moom da ñu koo jox téereem ci ginnaawam,
لَتَرْكَبُنَّ طَبَقًا عَن طَبَقٍ ١٩
📖 Tekki
Aaya 19
Dingeen jaar, ay jaar-jaar yu tegaloo yu bari !
وَإِذَا قُرِئَ عَلَيْهِمُ الْقُرْآنُ لَا يَسْجُدُونَ ۩ ٢١
📖 Tekki
Aaya 21
te suñu jàngee ci ñoom Alxuraan duñu sujuud ?
إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ ٢٥
📖 Tekki
Aaya 25
Ba mu des ña gëm tey jëf yiw : ñoom am na ñu pey gu dootul dog.
Jàng Simoore Al-Inshiqaq ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers

