Al-Inshiqaq · 6/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ إِنَّكَ كَادِحٌ إِلَىٰ رَبِّكَ كَدْحًا فَمُلَاقِيهِ ۝٦
Yaaa ayyuhal insaanu innaka kaadihun ilaa Rabbika kad han famulaaqeeh
📖 Tekkim Wolof
Éy yaw nit ! Yaa ngi def jëm ci sa boroom, te danga dajeek moom de

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Inshiqaq

4وَأَلْقَتْ مَا فِيهَا وَتَخَلَّتْ
te mu gëx lép lu nekk ci biiram,
5وَأَذِنَتْ لِرَبِّهَا وَحُقَّتْ
moom it – mu def ngigëlu boroomam dëggël ko
6يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ إِنَّكَ كَادِحٌ إِلَىٰ رَبِّكَ كَدْحًا فَمُلَاقِيهِ
Éy yaw nit ! Yaa ngi def jëm ci sa boroom, te danga dajeek moom de
7فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ
Képp ku ñu joxe téereem ci loxob ndeyjooram,
8فَسَوْفَ يُحَاسَبُ حِسَابًا يَسِيرًا
dees na ko màndaxe mu jàppandal,
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 6

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yaw nit ! Yaa ngi def jëm ci sa…

Simoore Aaya 6/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers