Al-Inshiqaq · 21/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
وَإِذَا قُرِئَ عَلَيْهِمُ الْقُرْآنُ لَا يَسْجُدُونَ ۩ ۝٢١
Wa izaa quri`a `alaihimul Quraanu laa yasjudoon
📖 Tekkim Wolof
te suñu jàngee ci ñoom Alxuraan duñu sujuud ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore Al-Inshiqaq

19لَتَرْكَبُنَّ طَبَقًا عَن طَبَقٍ
Dingeen jaar, ay jaar-jaar yu tegaloo yu bari !
20فَمَا لَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Ana lu leen dal ba gëmuñu ?
21وَإِذَا قُرِئَ عَلَيْهِمُ الْقُرْآنُ لَا يَسْجُدُونَ ۩
te suñu jàngee ci ñoom Alxuraan duñu sujuud ?
22بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا يُكَذِّبُونَ
Yéefër ya, ñoo koy weddi.
23وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُوعُونَ
Yàlla xam na la ñuy xalaat.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 21

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te suñu jàngee ci ñoom Alxuraan duñu sujuud ?

Simoore Aaya 21/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers