Al-Inshiqaq · 9/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
وَيَنقَلِبُ إِلَىٰ أَهْلِهِ مَسْرُورًا ۝٩
Wa yanqalibu ilaaa ahlihee masrooraa
📖 Tekkim Wolof
muy walbatiku jëm cag njabootam di bég.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Inshiqaq

7فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ
Képp ku ñu joxe téereem ci loxob ndeyjooram,
8فَسَوْفَ يُحَاسَبُ حِسَابًا يَسِيرًا
dees na ko màndaxe mu jàppandal,
9وَيَنقَلِبُ إِلَىٰ أَهْلِهِ مَسْرُورًا
muy walbatiku jëm cag njabootam di bég.
10وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ وَرَاءَ ظَهْرِهِ
Képp koo xam ne nag moom da ñu koo jox téereem ci ginnaawam,
11فَسَوْفَ يَدْعُو ثُبُورًا
Ngalla moom kon,
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 9

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : muy walbatiku jëm cag njabootam di bég.

Simoore Aaya 9/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers