Al-Inshiqaq · 7/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ ۝٧
Fa ammaa man ootiya kitaabahoo biyameenih
📖 Tekkim Wolof
Képp ku ñu joxe téereem ci loxob ndeyjooram,

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-Inshiqaq

5وَأَذِنَتْ لِرَبِّهَا وَحُقَّتْ
moom it – mu def ngigëlu boroomam dëggël ko
6يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ إِنَّكَ كَادِحٌ إِلَىٰ رَبِّكَ كَدْحًا فَمُلَاقِيهِ
Éy yaw nit ! Yaa ngi def jëm ci sa boroom, te danga dajeek moom de
7فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ
Képp ku ñu joxe téereem ci loxob ndeyjooram,
8فَسَوْفَ يُحَاسَبُ حِسَابًا يَسِيرًا
dees na ko màndaxe mu jàppandal,
9وَيَنقَلِبُ إِلَىٰ أَهْلِهِ مَسْرُورًا
muy walbatiku jëm cag njabootam di bég.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 7

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp ku ñu joxe téereem ci loxob ndeyjooram,

Simoore Aaya 7/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers