Al-Inshiqaq · 12/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
وَيَصْلَىٰ سَعِيرًا ۝١٢
Wa yaslaa sa`eeraa
📖 Tekkim Wolof
te dana xoyomoo safaraw Sa’iir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Inshiqaq

10وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ وَرَاءَ ظَهْرِهِ
Képp koo xam ne nag moom da ñu koo jox téereem ci ginnaawam,
11فَسَوْفَ يَدْعُو ثُبُورًا
Ngalla moom kon,
12وَيَصْلَىٰ سَعِيرًا
te dana xoyomoo safaraw Sa’iir.
13إِنَّهُ كَانَ فِي أَهْلِهِ مَسْرُورًا
Moom ku bégoon la cag njabootam,
14إِنَّهُ ظَنَّ أَن لَّن يَحُورَ
foogoon na ne du dekkiwaat mukk.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 12

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te dana xoyomoo safaraw Sa’iir.

Simoore Aaya 12/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers