Al-Inshiqaq · 11/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
فَسَوْفَ يَدْعُو ثُبُورًا ۝١١
Fasawfa yad`oo subooraa
📖 Tekkim Wolof
Ngalla moom kon,

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Inshiqaq

9وَيَنقَلِبُ إِلَىٰ أَهْلِهِ مَسْرُورًا
muy walbatiku jëm cag njabootam di bég.
10وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ وَرَاءَ ظَهْرِهِ
Képp koo xam ne nag moom da ñu koo jox téereem ci ginnaawam,
11فَسَوْفَ يَدْعُو ثُبُورًا
Ngalla moom kon,
12وَيَصْلَىٰ سَعِيرًا
te dana xoyomoo safaraw Sa’iir.
13إِنَّهُ كَانَ فِي أَهْلِهِ مَسْرُورًا
Moom ku bégoon la cag njabootam,
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 11

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ngalla moom kon,

Simoore Aaya 11/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers