Al-Inshiqaq · 25/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ ۝٢٥
Illal lazeena aamanoo wa `amilus saalihaati lahum ajrun ghairu mamnoon
📖 Tekkim Wolof
Ba mu des ña gëm tey jëf yiw : ñoom am na ñu pey gu dootul dog.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-25 — Simoore Al-Inshiqaq

23وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُوعُونَ
Yàlla xam na la ñuy xalaat.
24فَبَشِّرْهُم بِعَذَابٍ أَلِيمٍ
Na gneen leen xibaar mbugël mu mitti ma.
25إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
Ba mu des ña gëm tey jëf yiw : ñoom am na ñu pey gu dootul dog.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 25

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu des ña gëm tey jëf yiw : ñoom…

Simoore Aaya 25/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 23–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers