Al-Inshiqaq · 23/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُوعُونَ ۝٢٣
Wallaahu a`lamu bimaa yoo`oon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla xam na la ñuy xalaat.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Inshiqaq

21وَإِذَا قُرِئَ عَلَيْهِمُ الْقُرْآنُ لَا يَسْجُدُونَ ۩
te suñu jàngee ci ñoom Alxuraan duñu sujuud ?
22بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا يُكَذِّبُونَ
Yéefër ya, ñoo koy weddi.
23وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُوعُونَ
Yàlla xam na la ñuy xalaat.
24فَبَشِّرْهُم بِعَذَابٍ أَلِيمٍ
Na gneen leen xibaar mbugël mu mitti ma.
25إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
Ba mu des ña gëm tey jëf yiw : ñoom am na ñu pey gu dootul dog.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 23

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla xam na la ñuy xalaat.

Simoore Aaya 23/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers