Al-Inshiqaq · 22/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا يُكَذِّبُونَ ۝٢٢
Balil lazeena kafaroo yukazziboon
📖 Tekkim Wolof
Yéefër ya, ñoo koy weddi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Simoore Al-Inshiqaq

20فَمَا لَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Ana lu leen dal ba gëmuñu ?
21وَإِذَا قُرِئَ عَلَيْهِمُ الْقُرْآنُ لَا يَسْجُدُونَ ۩
te suñu jàngee ci ñoom Alxuraan duñu sujuud ?
22بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا يُكَذِّبُونَ
Yéefër ya, ñoo koy weddi.
23وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُوعُونَ
Yàlla xam na la ñuy xalaat.
24فَبَشِّرْهُم بِعَذَابٍ أَلِيمٍ
Na gneen leen xibaar mbugël mu mitti ma.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 22

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéefër ya, ñoo koy weddi.

Simoore Aaya 22/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers