Al-Inshiqaq · 24/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
فَبَشِّرْهُم بِعَذَابٍ أَلِيمٍ ۝٢٤
Fabashshirhum bi`azaabin aleem
📖 Tekkim Wolof
Na gneen leen xibaar mbugël mu mitti ma.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-25 — Simoore Al-Inshiqaq

22بَلِ الَّذِينَ كَفَرُوا يُكَذِّبُونَ
Yéefër ya, ñoo koy weddi.
23وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يُوعُونَ
Yàlla xam na la ñuy xalaat.
24فَبَشِّرْهُم بِعَذَابٍ أَلِيمٍ
Na gneen leen xibaar mbugël mu mitti ma.
25إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ
Ba mu des ña gëm tey jëf yiw : ñoom am na ñu pey gu dootul dog.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 24

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Na gneen leen xibaar mbugël mu mitti ma.

Simoore Aaya 24/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 22–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers