Al-Inshiqaq · 10/25
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Inshiqaq
وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ وَرَاءَ ظَهْرِهِ ١٠
Transliteration
Wa ammaa man ootiya kitaabahoo waraaa`a zahrih
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Képp koo xam ne nag moom da ñu koo jox téereem ci ginnaawam,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Inshiqaq
8فَسَوْفَ يُحَاسَبُ حِسَابًا يَسِيرًا
dees na ko màndaxe mu jàppandal,
9وَيَنقَلِبُ إِلَىٰ أَهْلِهِ مَسْرُورًا
muy walbatiku jëm cag njabootam di bég.
10وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ وَرَاءَ ظَهْرِهِ
Képp koo xam ne nag moom da ñu koo jox téereem ci ginnaawam,
11فَسَوْفَ يَدْعُو ثُبُورًا
Ngalla moom kon,
12وَيَصْلَىٰ سَعِيرًا
te dana xoyomoo safaraw Sa’iir.
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
10Aaya
Tekki — Al-Inshiqaq 10
Simoore Al-Inshiqaq Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp koo xam ne nag moom da ñu koo jox…Simoore Aaya 10/25 — Simoore Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Inshiqaq Dégg, Simoore Al-Inshiqaq Tekki, Simoore Al-Inshiqaq mp3, Simoore Al-Inshiqaq pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








