Al-Inshiqaq · 5/25
Tekki Waxtaan — Al-Inshiqaq
وَأَذِنَتْ لِرَبِّهَا وَحُقَّتْ ۝٥
Wa azinat li Rabbihaa wa huqqat
📖 Tekkim Wolof
moom it – mu def ngigëlu boroomam dëggël ko

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Al-Inshiqaq

3وَإِذَا الْأَرْضُ مُدَّتْ
ak saa suñu maasalee suuf si,
4وَأَلْقَتْ مَا فِيهَا وَتَخَلَّتْ
te mu gëx lép lu nekk ci biiram,
5وَأَذِنَتْ لِرَبِّهَا وَحُقَّتْ
moom it – mu def ngigëlu boroomam dëggël ko
6يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ إِنَّكَ كَادِحٌ إِلَىٰ رَبِّكَ كَدْحًا فَمُلَاقِيهِ
Éy yaw nit ! Yaa ngi def jëm ci sa boroom, te danga dajeek moom de
7فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ
Képp ku ñu joxe téereem ci loxob ndeyjooram,
Al-InshiqaqFihi Alxuraan
25Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Inshiqaq 5

Simoore Al-Inshiqaq Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : moom it – mu def ngigëlu boroomam dëggël ko

Simoore Aaya 5/25 — Al-Inshiqaq الإنشقاق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Inshiqaq Dégg, Al-Inshiqaq Tekki, Al-Inshiqaq mp3, Al-Inshiqaq pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers