Yunus · 32/109
Tekki Waxtaan — Yunus
فَذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبُّكُمُ الْحَقُّ ۖ فَمَاذَا بَعْدَ الْحَقِّ إِلَّا الضَّلَالُ ۖ فَأَنَّىٰ تُصْرَفُونَ ۝٣٢
Fazaalikumul laahu Rabbukumul haqq; famaazaa ba`dal haqqi illad dalaalu fa annnaa tusrafoon
📖 Tekkim Wolof
Kon noonu la, Yàlla di seen Boroom ba di dëgg ga. Kon lan moo nekk ci ginnaaw dëgg lu dul ag réer ? Kon naka leen leen mën a wëlbatee ? ”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 30-34 — Yunus

30هُنَالِكَ تَبْلُو كُلُّ نَفْسٍ مَّا أَسْلَفَتْ ۚ وَرُدُّوا إِلَى اللَّهِ مَوْلَاهُمُ الْحَقِّ ۖ وَضَلَّ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَفْتَرُونَ
Noonu, bakkan bu nekk la mu jëfoon sadd ko. Ñu delloo leen ca seen Boroom muy dëgg ; ya ñu daan sos réer leen.
31قُلْ مَن يَرْزُقُكُم مِّنَ السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ أَمَّن يَمْلِكُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَمَن يُخْرِجُ الْحَيَّ مِنَ الْمَيِّتِ وَيُخْرِجُ الْمَيِّتَ مِنَ الْحَيِّ وَمَن يُدَبِّرُ الْأَمْرَ ۚ فَسَيَقُولُونَ اللَّهُ ۚ فَقُلْ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Neel : “Ana kan moo leen di jox xéewal yu jóge kaw asamaan ak ci suuf si ? Kan moo moom dégg-dégg [nopp yi], ak gis-gis [bët yi], ana kan mooy génne luy dundu ci lu dee, di génne lu dee ci lu dundu, ana kan mooy dogal mbir yi ? ”. Danañu toontu ne : “Yàlla”. Neeleen kon : “Lu leen teree ragal Yàlla ? ”.
32فَذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبُّكُمُ الْحَقُّ ۖ فَمَاذَا بَعْدَ الْحَقِّ إِلَّا الضَّلَالُ ۖ فَأَنَّىٰ تُصْرَفُونَ
Kon noonu la, Yàlla di seen Boroom ba di dëgg ga. Kon lan moo nekk ci ginnaaw dëgg lu dul ag réer ? Kon naka leen leen mën a wëlbatee ? ”.
33كَذَٰلِكَ حَقَّتْ كَلِمَتُ رَبِّكَ عَلَى الَّذِينَ فَسَقُوا أَنَّهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Noonu la sa kàddug Boroom yayee te dal ca kaw ña di ay saay-saay ndax gëmuñu.
34قُلْ هَلْ مِن شُرَكَائِكُم مَّن يَبْدَأُ الْخَلْقَ ثُمَّ يُعِيدُهُ ۚ قُلِ اللَّهُ يَبْدَأُ الْخَلْقَ ثُمَّ يُعِيدُهُ ۖ فَأَنَّىٰ تُؤْفَكُونَ
Neel : “Ndax am na ci ña ngeen di bokkaaleek [Yàlla] kuy sos mbindéef, mën koo dundal [gannaaw ba mu deewee]? ”. Neel : “Yàlla rekk a mën a sos mbindéef te mën koo dundal. Kon naka lees leen di wëlbatee ?”.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Yunus 32

Simoore Yunus Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kon noonu la, Yàlla di seen Boroom ba di dëgg…

Simoore Aaya 32/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers