Hud · 100/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
ذَٰلِكَ مِنْ أَنبَاءِ الْقُرَىٰ نَقُصُّهُ عَلَيْكَ ۖ مِنْهَا قَائِمٌ وَحَصِيدٌ ۝١٠٠
Zaalika min ambaaa`il quraa naqussuhoo `alaika minhaa qaaa`imunw wa haseed
📖 Tekkim Wolof
Loolu bokk na ca xew-xewi dëkk ya, Nu nettali la ko : te am na ca dëkk yooyu yu taxaw ba léegi, ak yu ñu maasale.

🎧 Dégg


📜 Aaya 98-102 — Simoore Hud

98يَقْدُمُ قَوْمَهُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فَأَوْرَدَهُمُ النَّارَ ۖ وَبِئْسَ الْوِرْدُ الْمَوْرُودُ
Dana jiite aw nitam Bis-pénc ba. Tàbbal leen Safara. Ndaw tàbbikaay bu bon !
99وَأُتْبِعُوا فِي هَٰذِهِ لَعْنَةً وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ بِئْسَ الرِّفْدُ الْمَرْفُودُ
Am rëbbu topp na leen ci àddina sii te Bis-pénc ba, yool ba ñuy am it bon na, ci aw yooliin !
100ذَٰلِكَ مِنْ أَنبَاءِ الْقُرَىٰ نَقُصُّهُ عَلَيْكَ ۖ مِنْهَا قَائِمٌ وَحَصِيدٌ
Loolu bokk na ca xew-xewi dëkk ya, Nu nettali la ko : te am na ca dëkk yooyu yu taxaw ba léegi, ak yu ñu maasale.
101وَمَا ظَلَمْنَاهُمْ وَلَٰكِن ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ ۖ فَمَا أَغْنَتْ عَنْهُمْ آلِهَتُهُمُ الَّتِي يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مِن شَيْءٍ لَّمَّا جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَمَا زَادُوهُمْ غَيْرَ تَتْبِيبٍ
Tooñunuleen. Waaye ñoo tooñ seen bopp. Seen yàlla ya ñu doon jaamu, bàyyi fa Yàlla, jariñuleen dara. Ba sa ndigalu Boroom agsee, dolliwuleen lu dul alkaande.
102وَكَذَٰلِكَ أَخْذُ رَبِّكَ إِذَا أَخَذَ الْقُرَىٰ وَهِيَ ظَالِمَةٌ ۚ إِنَّ أَخْذَهُ أَلِيمٌ شَدِيدٌ
Noonu la sa Boroom di alage, bu alagee njéndi fekk ñu tooñ. Alage ju Muy alag [ñooña], dafay metti tar.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
100Aaya

Tekki — Hud 100

Simoore Hud Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu bokk na ca xew-xewi dëkk ya, Nu nettali la…

Simoore Aaya 100/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers