Hud · 99/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
وَأُتْبِعُوا فِي هَٰذِهِ لَعْنَةً وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ بِئْسَ الرِّفْدُ الْمَرْفُودُ ۝٩٩
Wa utbi`oo fee haazihee la`natanw wa Yawmal Qiyaamah; bi`sar rifdul marfood
📖 Tekkim Wolof
Am rëbbu topp na leen ci àddina sii te Bis-pénc ba, yool ba ñuy am it bon na, ci aw yooliin !

🎧 Dégg


📜 Aaya 97-101 — Simoore Hud

97إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَاتَّبَعُوا أَمْرَ فِرْعَوْنَ ۖ وَمَا أَمْرُ فِرْعَوْنَ بِرَشِيدٍ
ca Firawna ak boroom darajaam ya. Ñu topp ndigalu Firawna, te ndigalu Firawna jubul woon.
98يَقْدُمُ قَوْمَهُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فَأَوْرَدَهُمُ النَّارَ ۖ وَبِئْسَ الْوِرْدُ الْمَوْرُودُ
Dana jiite aw nitam Bis-pénc ba. Tàbbal leen Safara. Ndaw tàbbikaay bu bon !
99وَأُتْبِعُوا فِي هَٰذِهِ لَعْنَةً وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ بِئْسَ الرِّفْدُ الْمَرْفُودُ
Am rëbbu topp na leen ci àddina sii te Bis-pénc ba, yool ba ñuy am it bon na, ci aw yooliin !
100ذَٰلِكَ مِنْ أَنبَاءِ الْقُرَىٰ نَقُصُّهُ عَلَيْكَ ۖ مِنْهَا قَائِمٌ وَحَصِيدٌ
Loolu bokk na ca xew-xewi dëkk ya, Nu nettali la ko : te am na ca dëkk yooyu yu taxaw ba léegi, ak yu ñu maasale.
101وَمَا ظَلَمْنَاهُمْ وَلَٰكِن ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ ۖ فَمَا أَغْنَتْ عَنْهُمْ آلِهَتُهُمُ الَّتِي يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مِن شَيْءٍ لَّمَّا جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَمَا زَادُوهُمْ غَيْرَ تَتْبِيبٍ
Tooñunuleen. Waaye ñoo tooñ seen bopp. Seen yàlla ya ñu doon jaamu, bàyyi fa Yàlla, jariñuleen dara. Ba sa ndigalu Boroom agsee, dolliwuleen lu dul alkaande.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
99Aaya

Tekki — Hud 99

Simoore Hud Aaya 99 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am rëbbu topp na leen ci àddina sii te Bis-pénc…

Simoore Aaya 99/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 97–101. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers