Hud · 3/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
وَأَنِ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ يُمَتِّعْكُم مَّتَاعًا حَسَنًا إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى وَيُؤْتِ كُلَّ ذِي فَضْلٍ فَضْلَهُ ۖ وَإِن تَوَلَّوْا فَإِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ كَبِيرٍ ۝٣
Wa anis taghfiroo Rabbakum summa toobooo ilaihi yumatti`kum mataa`an hasanan ilaaa ajalim musammanw wa yu`ti kulla zee fadlin fadlahoo wa in tawallaw fa inneee akhaafu `alaikum `azaaba Yawmin Kabeer
📖 Tekkim Wolof
Te ñu sàkku njéggalu seen Boroom ; te dellu ca Moom, ànd ak tuub. Mu yóbbale leen xéewal yu gën ba ca àpp ba Mu ko dogale, mu jox képp ku ko yayoo ngëneel, ay ngënéelam. Waaye bu ngeen dummóoyoo, ragalal naa leen mbugal dal leen ci bis bu mag.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Hud

1الر ۚ كِتَابٌ أُحْكِمَتْ آيَاتُهُ ثُمَّ فُصِّلَتْ مِن لَّدُنْ حَكِيمٍ خَبِيرٍ
Alif, Laam, Raa. Lii ab Téere la bu ñu xereñe ay kàddoom, faramfàccees ko mu tukkee ca Ku xereñ ka, di Ku deñ-kumpa [Yàlla].
2أَلَّا تَعْبُدُوا إِلَّا اللَّهَ ۚ إِنَّنِي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ وَبَشِيرٌ
[Digaleef na leen] ngeen bañ a jaamu kenn ku dul Yàlla. Man mii dey kuy xuppe laa, di kuy waare ci yéen.
3وَأَنِ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ يُمَتِّعْكُم مَّتَاعًا حَسَنًا إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى وَيُؤْتِ كُلَّ ذِي فَضْلٍ فَضْلَهُ ۖ وَإِن تَوَلَّوْا فَإِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ كَبِيرٍ
Te ñu sàkku njéggalu seen Boroom ; te dellu ca Moom, ànd ak tuub. Mu yóbbale leen xéewal yu gën ba ca àpp ba Mu ko dogale, mu jox képp ku ko yayoo ngëneel, ay ngënéelam. Waaye bu ngeen dummóoyoo, ragalal naa leen mbugal dal leen ci bis bu mag.
4إِلَى اللَّهِ مَرْجِعُكُمْ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Ca Yàlla ngeen di dellu ; te Moom mën na lu ne.
5أَلَا إِنَّهُمْ يَثْنُونَ صُدُورَهُمْ لِيَسْتَخْفُوا مِنْهُ ۚ أَلَا حِينَ يَسْتَغْشُونَ ثِيَابَهُمْ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ ۚ إِنَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Ndax ñoom dañuy lem seeni dënn ngir mën a nëbbu Yàlla ? Moo ndax bu ñu muurook seeni yëre, Yàlla dadul xam li ñuy feeñal ak li ñuy nëbb ? Moom dey ku xam li nekk ci xol yi la.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Hud 3

Simoore Hud Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ñu sàkku njéggalu seen Boroom ; te dellu ca…

Simoore Aaya 3/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers