Hud · 4/123
Tekki Waxtaan — Hud
إِلَى اللَّهِ مَرْجِعُكُمْ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ ۝٤
Ilal laahi marji`ukum wa Huwa `alaa kulli shai`in Qadeer
📖 Tekkim Wolof
Ca Yàlla ngeen di dellu ; te Moom mën na lu ne.
🎧 Dégg

📜 Aaya 2-6 — Hud

2أَلَّا تَعْبُدُوا إِلَّا اللَّهَ ۚ إِنَّنِي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ وَبَشِيرٌ
[Digaleef na leen] ngeen bañ a jaamu kenn ku dul Yàlla. Man mii dey kuy xuppe laa, di kuy waare ci yéen.
3وَأَنِ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ يُمَتِّعْكُم مَّتَاعًا حَسَنًا إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى وَيُؤْتِ كُلَّ ذِي فَضْلٍ فَضْلَهُ ۖ وَإِن تَوَلَّوْا فَإِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ كَبِيرٍ
Te ñu sàkku njéggalu seen Boroom ; te dellu ca Moom, ànd ak tuub. Mu yóbbale leen xéewal yu gën ba ca àpp ba Mu ko dogale, mu jox képp ku ko yayoo ngëneel, ay ngënéelam. Waaye bu ngeen dummóoyoo, ragalal naa leen mbugal dal leen ci bis bu mag.
4إِلَى اللَّهِ مَرْجِعُكُمْ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Ca Yàlla ngeen di dellu ; te Moom mën na lu ne.
5أَلَا إِنَّهُمْ يَثْنُونَ صُدُورَهُمْ لِيَسْتَخْفُوا مِنْهُ ۚ أَلَا حِينَ يَسْتَغْشُونَ ثِيَابَهُمْ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ ۚ إِنَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Ndax ñoom dañuy lem seeni dënn ngir mën a nëbbu Yàlla ? Moo ndax bu ñu muurook seeni yëre, Yàlla dadul xam li ñuy feeñal ak li ñuy nëbb ? Moom dey ku xam li nekk ci xol yi la.
6۞ وَمَا مِن دَابَّةٍ فِي الْأَرْضِ إِلَّا عَلَى اللَّهِ رِزْقُهَا وَيَعْلَمُ مُسْتَقَرَّهَا وَمُسْتَوْدَعَهَا ۚ كُلٌّ فِي كِتَابٍ مُّبِينٍ
Amul lenn luy dukkat ci kaw suuf si te sag dundu Yàlla warluwu ko te xam na saxuwaayam ak dëkkuwaayam ; lépp a ngi ci ab Téere bu wér péŋŋ [mu di Lawhul mahfuuz].
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Hud 4

Simoore Hud Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca Yàlla ngeen di dellu ; te Moom mën na…

Simoore Aaya 4/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers