An-Nahl · 112/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
وَضَرَبَ اللَّهُ مَثَلًا قَرْيَةً كَانَتْ آمِنَةً مُّطْمَئِنَّةً يَأْتِيهَا رِزْقُهَا رَغَدًا مِّن كُلِّ مَكَانٍ فَكَفَرَتْ بِأَنْعُمِ اللَّهِ فَأَذَاقَهَا اللَّهُ لِبَاسَ الْجُوعِ وَالْخَوْفِ بِمَا كَانُوا يَصْنَعُونَ ۝١١٢
Wa darabal laahu masalan qaryatan kaanat aaminatam mutma`innatany yaaateehaa rizquhaa rghadam min kulli makaanin fakafarat bi an`umil laahi fa azaaqahal laahu libaasal joo`i walkhawfi bimaa kaanoo yasna`oon
📖 Tekkim Wolof
Yàllaa ngay joxe léebu ci dëkk ba amoon xel mu dal ; te am kóolute, wërsëgam di fa dikk, bari lool tey jóge fu nekk. Waaye mu weddi xéewali Yàlla yi. [Waa dëkk ba] tax Yàlla mosal ko càngaayu xiif ak tiitaange ndax la ñu jëf.
🎧 Dégg

📜 Aaya 110-114 — An-Nahl

110ثُمَّ إِنَّ رَبَّكَ لِلَّذِينَ هَاجَرُوا مِن بَعْدِ مَا فُتِنُوا ثُمَّ جَاهَدُوا وَصَبَرُوا إِنَّ رَبَّكَ مِن بَعْدِهَا لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ
La cay topp moo di sa Boroom dana jéggal ña gàddaayoon te muñ, ginnaaw loolu sa Boroom dana jagle njéggalam ak yërmaandeem.
111۞ يَوْمَ تَأْتِي كُلُّ نَفْسٍ تُجَادِلُ عَن نَّفْسِهَا وَتُوَفَّىٰ كُلُّ نَفْسٍ مَّا عَمِلَتْ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Bis bu bakkan bu ne dàggasanteeg boppam, te bakkan bu nekk ñu feye ko la mu jëfoon, bu boobaa Dunu tooñ kenn ci dara.
112وَضَرَبَ اللَّهُ مَثَلًا قَرْيَةً كَانَتْ آمِنَةً مُّطْمَئِنَّةً يَأْتِيهَا رِزْقُهَا رَغَدًا مِّن كُلِّ مَكَانٍ فَكَفَرَتْ بِأَنْعُمِ اللَّهِ فَأَذَاقَهَا اللَّهُ لِبَاسَ الْجُوعِ وَالْخَوْفِ بِمَا كَانُوا يَصْنَعُونَ
Yàllaa ngay joxe léebu ci dëkk ba amoon xel mu dal ; te am kóolute, wërsëgam di fa dikk, bari lool tey jóge fu nekk. Waaye mu weddi xéewali Yàlla yi. [Waa dëkk ba] tax Yàlla mosal ko càngaayu xiif ak tiitaange ndax la ñu jëf.
113وَلَقَدْ جَاءَهُمْ رَسُولٌ مِّنْهُمْ فَكَذَّبُوهُ فَأَخَذَهُمُ الْعَذَابُ وَهُمْ ظَالِمُونَ
Ab Yonent bu bokk ci ñoom dikkal na leen, ñu weddi ko. Mbugal sadd leen te ñu nekkoon ñu tooñ.
114فَكُلُوا مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ حَلَالًا طَيِّبًا وَاشْكُرُوا نِعْمَتَ اللَّهِ إِن كُنتُمْ إِيَّاهُ تَعْبُدُونَ
Lekk-leen ci xéewal gi leen Yàlla jox, muy lu lew, lu teey. Te ngeen gërëm Yàlla ciy xéewalam ndeem Moom rekk ngeen di jaamu.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
112Aaya

Tekki — An-Nahl 112

Simoore An-Nahl Aaya 112 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaa ngay joxe léebu ci dëkk ba amoon xel mu…

Simoore Aaya 112/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 110–114. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers