An-Nahl · 113/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَلَقَدْ جَاءَهُمْ رَسُولٌ مِّنْهُمْ فَكَذَّبُوهُ فَأَخَذَهُمُ الْعَذَابُ وَهُمْ ظَالِمُونَ ۝١١٣
Wa laqad jaaa`ahum Rasoolum minhum fakazzaboohu fa akhazahumul `azaabu wa hum zaalimoon
📖 Tekkim Wolof
Ab Yonent bu bokk ci ñoom dikkal na leen, ñu weddi ko. Mbugal sadd leen te ñu nekkoon ñu tooñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 111-115 — Simoore An-Nahl

111۞ يَوْمَ تَأْتِي كُلُّ نَفْسٍ تُجَادِلُ عَن نَّفْسِهَا وَتُوَفَّىٰ كُلُّ نَفْسٍ مَّا عَمِلَتْ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Bis bu bakkan bu ne dàggasanteeg boppam, te bakkan bu nekk ñu feye ko la mu jëfoon, bu boobaa Dunu tooñ kenn ci dara.
112وَضَرَبَ اللَّهُ مَثَلًا قَرْيَةً كَانَتْ آمِنَةً مُّطْمَئِنَّةً يَأْتِيهَا رِزْقُهَا رَغَدًا مِّن كُلِّ مَكَانٍ فَكَفَرَتْ بِأَنْعُمِ اللَّهِ فَأَذَاقَهَا اللَّهُ لِبَاسَ الْجُوعِ وَالْخَوْفِ بِمَا كَانُوا يَصْنَعُونَ
Yàllaa ngay joxe léebu ci dëkk ba amoon xel mu dal ; te am kóolute, wërsëgam di fa dikk, bari lool tey jóge fu nekk. Waaye mu weddi xéewali Yàlla yi. [Waa dëkk ba] tax Yàlla mosal ko càngaayu xiif ak tiitaange ndax la ñu jëf.
113وَلَقَدْ جَاءَهُمْ رَسُولٌ مِّنْهُمْ فَكَذَّبُوهُ فَأَخَذَهُمُ الْعَذَابُ وَهُمْ ظَالِمُونَ
Ab Yonent bu bokk ci ñoom dikkal na leen, ñu weddi ko. Mbugal sadd leen te ñu nekkoon ñu tooñ.
114فَكُلُوا مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ حَلَالًا طَيِّبًا وَاشْكُرُوا نِعْمَتَ اللَّهِ إِن كُنتُمْ إِيَّاهُ تَعْبُدُونَ
Lekk-leen ci xéewal gi leen Yàlla jox, muy lu lew, lu teey. Te ngeen gërëm Yàlla ciy xéewalam ndeem Moom rekk ngeen di jaamu.
115إِنَّمَا حَرَّمَ عَلَيْكُمُ الْمَيْتَةَ وَالدَّمَ وَلَحْمَ الْخِنزِيرِ وَمَا أُهِلَّ لِغَيْرِ اللَّهِ بِهِ ۖ فَمَنِ اضْطُرَّ غَيْرَ بَاغٍ وَلَا عَادٍ فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Waaye araamal na ci yéen médd, ak deret, ak yàppu mbaam-xuux ak lu ñu [rey] te tuddu ca keneen ku dul Yàlla. Képp ku nar a loru [ba tax mu lekk yooya araam], na xam ne Yàlla jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
113Aaya

Tekki — An-Nahl 113

Simoore An-Nahl Aaya 113 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ab Yonent bu bokk ci ñoom dikkal na leen, ñu…

Simoore Aaya 113/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 111–115. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers