Al-Isra · 54/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
رَّبُّكُمْ أَعْلَمُ بِكُمْ ۖ إِن يَشَأْ يَرْحَمْكُمْ أَوْ إِن يَشَأْ يُعَذِّبْكُمْ ۚ وَمَا أَرْسَلْنَاكَ عَلَيْهِمْ وَكِيلًا ٥٤
Transliteration
Rabbukum a`lamu bikum iny yashaaa yarhamkum aw iny yashaa yu`azzibkum; wa maaa arsalnaaka `alaihim wakeelaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Seen Boroom moo leen gën a xam. Bu ko neexee Mu yërëm leen, walla Bu ko neexee Mu mbugal leen. Te yónniwunu la ci ñoom ngir nga warlul leen [seen texe].
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 52-56 — Al-Isra
52يَوْمَ يَدْعُوكُمْ فَتَسْتَجِيبُونَ بِحَمْدِهِ وَتَظُنُّونَ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا قَلِيلًا
Bis bu leen [seen Boroom] woowee, [ngeen dikk], ngeen tontu Ko, di tuddu cant [gi Mu yeyoo]. Te ngeen defe ne tooguleen ci [bàmmeel] lu dul diir bu néew ! ”.
53وَقُل لِّعِبَادِي يَقُولُوا الَّتِي هِيَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ يَنزَغُ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ كَانَ لِلْإِنسَانِ عَدُوًّا مُّبِينًا
Neel samay jaam, nañuy wax wax ju gën a rafet, ndax séytaane yi dañuy yàq seen diggante. Séytaane nag nekk na di noon tigi ci nit ñi.
54رَّبُّكُمْ أَعْلَمُ بِكُمْ ۖ إِن يَشَأْ يَرْحَمْكُمْ أَوْ إِن يَشَأْ يُعَذِّبْكُمْ ۚ وَمَا أَرْسَلْنَاكَ عَلَيْهِمْ وَكِيلًا
Seen Boroom moo leen gën a xam. Bu ko neexee Mu yërëm leen, walla Bu ko neexee Mu mbugal leen. Te yónniwunu la ci ñoom ngir nga warlul leen [seen texe].
55وَرَبُّكَ أَعْلَمُ بِمَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَلَقَدْ فَضَّلْنَا بَعْضَ النَّبِيِّينَ عَلَىٰ بَعْضٍ ۖ وَآتَيْنَا دَاوُودَ زَبُورًا
Te sa Boroom moo gën a xam ña nekk ci asmaan yi ak suuf si. Te def Nanu yenn Yonent yi gën ñeneen ña. Te Noo jox Daawuda “Zabour” [Téere].
56قُلِ ادْعُوا الَّذِينَ زَعَمْتُم مِّن دُونِهِ فَلَا يَمْلِكُونَ كَشْفَ الضُّرِّ عَنكُمْ وَلَا تَحْوِيلًا
Neel : “Wooleen ñi ngeen jàpp ne [Yàlla lañu] bàyyi Ko. Duñu mën a wuññi lor ja leen dal, duñu mën a soppi dara.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
54Aaya
Tekki — Al-Isra 54
Simoore Al-Isra Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen Boroom moo leen gën a xam. Bu ko neexee…Simoore Aaya 54/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








