Al-Isra · 53/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَقُل لِّعِبَادِي يَقُولُوا الَّتِي هِيَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ يَنزَغُ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ كَانَ لِلْإِنسَانِ عَدُوًّا مُّبِينًا ۝٥٣
Wa qul li`ibaadee yaqoolul latee hiya ahsan; innash shaitaana yanzaghu bainahum; innash shaitaana kaana lil insaani `aduwwam mubeenaa
📖 Tekkim Wolof
Neel samay jaam, nañuy wax wax ju gën a rafet, ndax séytaane yi dañuy yàq seen diggante. Séytaane nag nekk na di noon tigi ci nit ñi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 51-55 — Al-Isra

51أَوْ خَلْقًا مِّمَّا يَكْبُرُ فِي صُدُورِكُمْ ۚ فَسَيَقُولُونَ مَن يُعِيدُنَا ۖ قُلِ الَّذِي فَطَرَكُمْ أَوَّلَ مَرَّةٍ ۚ فَسَيُنْغِضُونَ إِلَيْكَ رُءُوسَهُمْ وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هُوَ ۖ قُلْ عَسَىٰ أَن يَكُونَ قَرِيبًا
walla yeneeni mbindeef yu reyci seeni xel. [Ngeen dégg] ñu naan : “Ku nuy dundalaat ? ” - Neel : “Ka leen bindoon bu njëkk ba”. Danañu yëngal seen bopp jëme ci yaw [ngir weddi la], ñuy wax naan : “Kañ lay doon ? ” Neeleen : “Xéy-na nekk na lu jegeñ.
52يَوْمَ يَدْعُوكُمْ فَتَسْتَجِيبُونَ بِحَمْدِهِ وَتَظُنُّونَ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا قَلِيلًا
Bis bu leen [seen Boroom] woowee, [ngeen dikk], ngeen tontu Ko, di tuddu cant [gi Mu yeyoo]. Te ngeen defe ne tooguleen ci [bàmmeel] lu dul diir bu néew ! ”.
53وَقُل لِّعِبَادِي يَقُولُوا الَّتِي هِيَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ يَنزَغُ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ كَانَ لِلْإِنسَانِ عَدُوًّا مُّبِينًا
Neel samay jaam, nañuy wax wax ju gën a rafet, ndax séytaane yi dañuy yàq seen diggante. Séytaane nag nekk na di noon tigi ci nit ñi.
54رَّبُّكُمْ أَعْلَمُ بِكُمْ ۖ إِن يَشَأْ يَرْحَمْكُمْ أَوْ إِن يَشَأْ يُعَذِّبْكُمْ ۚ وَمَا أَرْسَلْنَاكَ عَلَيْهِمْ وَكِيلًا
Seen Boroom moo leen gën a xam. Bu ko neexee Mu yërëm leen, walla Bu ko neexee Mu mbugal leen. Te yónniwunu la ci ñoom ngir nga warlul leen [seen texe].
55وَرَبُّكَ أَعْلَمُ بِمَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَلَقَدْ فَضَّلْنَا بَعْضَ النَّبِيِّينَ عَلَىٰ بَعْضٍ ۖ وَآتَيْنَا دَاوُودَ زَبُورًا
Te sa Boroom moo gën a xam ña nekk ci asmaan yi ak suuf si. Te def Nanu yenn Yonent yi gën ñeneen ña. Te Noo jox Daawuda “Zabour” [Téere].
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Al-Isra 53

Simoore Al-Isra Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel samay jaam, nañuy wax wax ju gën a rafet,…

Simoore Aaya 53/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers