Al-Isra · 55/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَرَبُّكَ أَعْلَمُ بِمَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَلَقَدْ فَضَّلْنَا بَعْضَ النَّبِيِّينَ عَلَىٰ بَعْضٍ ۖ وَآتَيْنَا دَاوُودَ زَبُورًا ۝٥٥
Wa Rabbuka a`lamu biman fis samaawaati wal lard; wa laqad faddalnaa ba`dan Nabiyyeena `alaa ba`dinw wa aatainaaa Daawooda Zabooraa
📖 Tekkim Wolof
Te sa Boroom moo gën a xam ña nekk ci asmaan yi ak suuf si. Te def Nanu yenn Yonent yi gën ñeneen ña. Te Noo jox Daawuda “Zabour” [Téere].
🎧 Dégg

📜 Aaya 53-57 — Al-Isra

53وَقُل لِّعِبَادِي يَقُولُوا الَّتِي هِيَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ يَنزَغُ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّ الشَّيْطَانَ كَانَ لِلْإِنسَانِ عَدُوًّا مُّبِينًا
Neel samay jaam, nañuy wax wax ju gën a rafet, ndax séytaane yi dañuy yàq seen diggante. Séytaane nag nekk na di noon tigi ci nit ñi.
54رَّبُّكُمْ أَعْلَمُ بِكُمْ ۖ إِن يَشَأْ يَرْحَمْكُمْ أَوْ إِن يَشَأْ يُعَذِّبْكُمْ ۚ وَمَا أَرْسَلْنَاكَ عَلَيْهِمْ وَكِيلًا
Seen Boroom moo leen gën a xam. Bu ko neexee Mu yërëm leen, walla Bu ko neexee Mu mbugal leen. Te yónniwunu la ci ñoom ngir nga warlul leen [seen texe].
55وَرَبُّكَ أَعْلَمُ بِمَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَلَقَدْ فَضَّلْنَا بَعْضَ النَّبِيِّينَ عَلَىٰ بَعْضٍ ۖ وَآتَيْنَا دَاوُودَ زَبُورًا
Te sa Boroom moo gën a xam ña nekk ci asmaan yi ak suuf si. Te def Nanu yenn Yonent yi gën ñeneen ña. Te Noo jox Daawuda “Zabour” [Téere].
56قُلِ ادْعُوا الَّذِينَ زَعَمْتُم مِّن دُونِهِ فَلَا يَمْلِكُونَ كَشْفَ الضُّرِّ عَنكُمْ وَلَا تَحْوِيلًا
Neel : “Wooleen ñi ngeen jàpp ne [Yàlla lañu] bàyyi Ko. Duñu mën a wuññi lor ja leen dal, duñu mën a soppi dara.
57أُولَٰئِكَ الَّذِينَ يَدْعُونَ يَبْتَغُونَ إِلَىٰ رَبِّهِمُ الْوَسِيلَةَ أَيُّهُمْ أَقْرَبُ وَيَرْجُونَ رَحْمَتَهُ وَيَخَافُونَ عَذَابَهُ ۚ إِنَّ عَذَابَ رَبِّكَ كَانَ مَحْذُورًا
Ña ñuy jaamu dañu ne siiw am pexem gën a jegeñ seen Boroom. Te yaakaar nañu yërmaandeem, ragal nañu mbugalam. Naka sa mbugalum Boroom, lu mat a wattandiku la.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Al-Isra 55

Simoore Al-Isra Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sa Boroom moo gën a xam ña nekk ci…

Simoore Aaya 55/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers