Al-Kahf · 3/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
مَّاكِثِينَ فِيهِ أَبَدًا ۝٣
Maakiseena feehi abadaa
📖 Tekkim Wolof
te dañu cay sax dapet dàkk ba fàwwu,
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-5 — Al-Kahf

1الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي أَنزَلَ عَلَىٰ عَبْدِهِ الْكِتَابَ وَلَمْ يَجْعَل لَّهُ عِوَجًا ۜ
Gépp cant ñeel na Yàlla mi wàcce Téere ba ca jaamam [Muhammad], te defalu ko genn logg-logg !
2قَيِّمًا لِّيُنذِرَ بَأْسًا شَدِيدًا مِّن لَّدُنْهُ وَيُبَشِّرَ الْمُؤْمِنِينَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ الصَّالِحَاتِ أَنَّ لَهُمْ أَجْرًا حَسَنًا
Muy lu jub xocc, di xuppe ci mbugal mu tar lu jóge ci Moom ak di bégle way-gëm ñay jëf jëf yu yiw, ci ne ñoom am nañu pey gu rafet.
3مَّاكِثِينَ فِيهِ أَبَدًا
te dañu cay sax dapet dàkk ba fàwwu,
4وَيُنذِرَ الَّذِينَ قَالُوا اتَّخَذَ اللَّهُ وَلَدًا
te muy xupp ñay wax naan : “Yàlla am na doom.”
5مَّا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ وَلَا لِآبَائِهِمْ ۚ كَبُرَتْ كَلِمَةً تَخْرُجُ مِنْ أَفْوَاهِهِمْ ۚ إِن يَقُولُونَ إِلَّا كَذِبًا
Amuñu ci loolu benn xam-xam, Seeni baay it [amuñu ko ca]. Muy wax ju réy ju génne ci seen gémmiñ! Waxuñu lu dul fen.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Kahf 3

Simoore Al-Kahf Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te dañu cay sax dapet dàkk ba fàwwu,

Simoore Aaya 3/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers