Al-Kahf · 45/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
وَاضْرِبْ لَهُم مَّثَلَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا كَمَاءٍ أَنزَلْنَاهُ مِنَ السَّمَاءِ فَاخْتَلَطَ بِهِ نَبَاتُ الْأَرْضِ فَأَصْبَحَ هَشِيمًا تَذْرُوهُ الرِّيَاحُ ۗ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ مُّقْتَدِرًا ۝٤٥
Wadrib lahum masalal hayaatid dunyaa kamaaa`in anzalnaahu minas samaaa`i fakhtalata bihee nabaatul ardi fa asbaha hasheeman tazroo hur riyaah; wa kaanal laahu `alaa kulli shai`im muqtadiraa
📖 Tekkim Wolof
Joxleen léebug dundu àddina. Dafa mel ni ndox mu ñu wàcce mu jóge asamaan ; tax gàncax ga jóge ci suuf sax. Mu mujj nekk mboob mu wow, ngelaw yi tasaare ko. Yàlla ku am kàttan la ci def lu ne !
🎧 Dégg

📜 Aaya 43-47 — Al-Kahf

43وَلَمْ تَكُن لَّهُ فِئَةٌ يَنصُرُونَهُ مِن دُونِ اللَّهِ وَمَا كَانَ مُنتَصِرًا
Te amatul mbooloo mu ko mën a dimbali ku dul Yàlla. Te nekkul it di mënal boppam dara.
44هُنَالِكَ الْوَلَايَةُ لِلَّهِ الْحَقِّ ۚ هُوَ خَيْرٌ ثَوَابًا وَخَيْرٌ عُقْبًا
Fu mu doon, kaaraange ñeel na Yàlla ju dëggu ja. Mooy joxe gën ji yool ak gën ji muj.
45وَاضْرِبْ لَهُم مَّثَلَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا كَمَاءٍ أَنزَلْنَاهُ مِنَ السَّمَاءِ فَاخْتَلَطَ بِهِ نَبَاتُ الْأَرْضِ فَأَصْبَحَ هَشِيمًا تَذْرُوهُ الرِّيَاحُ ۗ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ مُّقْتَدِرًا
Joxleen léebug dundu àddina. Dafa mel ni ndox mu ñu wàcce mu jóge asamaan ; tax gàncax ga jóge ci suuf sax. Mu mujj nekk mboob mu wow, ngelaw yi tasaare ko. Yàlla ku am kàttan la ci def lu ne !
46الْمَالُ وَالْبَنُونَ زِينَةُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَالْبَاقِيَاتُ الصَّالِحَاتُ خَيْرٌ عِندَ رَبِّكَ ثَوَابًا وَخَيْرٌ أَمَلًا
Alal ak i doom ci yiy neexal àddina lañu bokk. Waaye way-des ya di [jëf] yu yiw, ñooy ya gën ca sa Boroom ci wàllu yool ak yaakaar.
47وَيَوْمَ نُسَيِّرُ الْجِبَالَ وَتَرَى الْأَرْضَ بَارِزَةً وَحَشَرْنَاهُمْ فَلَمْ نُغَادِرْ مِنْهُمْ أَحَدًا
Bis ba Nuy doxloo tundi doj yi nga gis suuf si maase nerr, Nu fang leen te Dunu bàyyi kenn ci ñoom.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Kahf 45

Simoore Al-Kahf Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Joxleen léebug dundu àddina. Dafa mel ni ndox mu ñu…

Simoore Aaya 45/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers