Al-Kahf · 69/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
قَالَ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ صَابِرًا وَلَا أَعْصِي لَكَ أَمْرًا ۝٦٩
Qaala satajiduneee in shaa `al laahu saabiranw wa laaa a`see laka amraa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Danga ma fekk bu soobee Yàlla ma di muñkat ; te duma moy sa lenn ndigal”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Simoore Al-Kahf

67قَالَ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu tontu ko, ne: “Doo mën a ànd ak man ci sag muñ.
68وَكَيْفَ تَصْبِرُ عَلَىٰ مَا لَمْ تُحِطْ بِهِ خُبْرًا
Naka ngay muñee ci loo xam ne peeguloo ko ci xam-xam ? ”.
69قَالَ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ صَابِرًا وَلَا أَعْصِي لَكَ أَمْرًا
Mu ne ko : “Danga ma fekk bu soobee Yàlla ma di muñkat ; te duma moy sa lenn ndigal”.
70قَالَ فَإِنِ اتَّبَعْتَنِي فَلَا تَسْأَلْنِي عَن شَيْءٍ حَتَّىٰ أُحْدِثَ لَكَ مِنْهُ ذِكْرًا
Mu ne ko : “Boo ma toppee, bul ma laaj ci dara, ba kerook ma la ciy niital dara”.
71فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا رَكِبَا فِي السَّفِينَةِ خَرَقَهَا ۖ قَالَ أَخَرَقْتَهَا لِتُغْرِقَ أَهْلَهَا لَقَدْ جِئْتَ شَيْئًا إِمْرًا
Ñu ànd ñoom ñaar. Ba ñu duggee ci genn gaal, mu xar gaal ga. Muusaa ne ko : “Ndax danga koy xar ngir labal ña ca nekk ? Def nga jëf ju siibu ! ”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Al-Kahf 69

Simoore Al-Kahf Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Danga ma fekk bu soobee Yàlla…

Simoore Aaya 69/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers