Al-Kahf · 70/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
قَالَ فَإِنِ اتَّبَعْتَنِي فَلَا تَسْأَلْنِي عَن شَيْءٍ حَتَّىٰ أُحْدِثَ لَكَ مِنْهُ ذِكْرًا ۝٧٠
Qaala fa init taba`tanee falaa tas`alnee `an shai`in hattaaa uhdisa laka minhu zikraa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Boo ma toppee, bul ma laaj ci dara, ba kerook ma la ciy niital dara”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 68-72 — Al-Kahf

68وَكَيْفَ تَصْبِرُ عَلَىٰ مَا لَمْ تُحِطْ بِهِ خُبْرًا
Naka ngay muñee ci loo xam ne peeguloo ko ci xam-xam ? ”.
69قَالَ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ صَابِرًا وَلَا أَعْصِي لَكَ أَمْرًا
Mu ne ko : “Danga ma fekk bu soobee Yàlla ma di muñkat ; te duma moy sa lenn ndigal”.
70قَالَ فَإِنِ اتَّبَعْتَنِي فَلَا تَسْأَلْنِي عَن شَيْءٍ حَتَّىٰ أُحْدِثَ لَكَ مِنْهُ ذِكْرًا
Mu ne ko : “Boo ma toppee, bul ma laaj ci dara, ba kerook ma la ciy niital dara”.
71فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا رَكِبَا فِي السَّفِينَةِ خَرَقَهَا ۖ قَالَ أَخَرَقْتَهَا لِتُغْرِقَ أَهْلَهَا لَقَدْ جِئْتَ شَيْئًا إِمْرًا
Ñu ànd ñoom ñaar. Ba ñu duggee ci genn gaal, mu xar gaal ga. Muusaa ne ko : “Ndax danga koy xar ngir labal ña ca nekk ? Def nga jëf ju siibu ! ”.
72قَالَ أَلَمْ أَقُلْ إِنَّكَ لَن تَسْتَطِيعَ مَعِيَ صَبْرًا
Mu ne ko : “Ndax waxuma la woon ne doo mën a ànd ak man ci sag muñ ? ”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
70Aaya

Tekki — Al-Kahf 70

Simoore Al-Kahf Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Boo ma toppee, bul ma laaj…

Simoore Aaya 70/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers