Al-Kahf · 9/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
أَمْ حَسِبْتَ أَنَّ أَصْحَابَ الْكَهْفِ وَالرَّقِيمِ كَانُوا مِنْ آيَاتِنَا عَجَبًا ۝٩
Am hasibta anna Ashaabal Kahfi war Raqeemi kaanoo min Aayaatinaa `ajabaa
📖 Tekkim Wolof
Ndax amuloo njort ci ne, ñoñ-xunt ma ak ñoñ-mbind ma [téere ba] bokkoon nañu ca Sunuy kéemaan yu doy waar [yéeme] ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Kahf

7إِنَّا جَعَلْنَا مَا عَلَى الْأَرْضِ زِينَةً لَّهَا لِنَبْلُوَهُمْ أَيُّهُمْ أَحْسَنُ عَمَلًا
Nun noo def ci suuf si taaram ngir nattu leen, [ba xam] ña ca gën a rafet jëf.
8وَإِنَّا لَجَاعِلُونَ مَا عَلَيْهَا صَعِيدًا جُرُزًا
De Dananu def li nekk ci kawam nekk di pàkk bu wow koŋŋ.
9أَمْ حَسِبْتَ أَنَّ أَصْحَابَ الْكَهْفِ وَالرَّقِيمِ كَانُوا مِنْ آيَاتِنَا عَجَبًا
Ndax amuloo njort ci ne, ñoñ-xunt ma ak ñoñ-mbind ma [téere ba] bokkoon nañu ca Sunuy kéemaan yu doy waar [yéeme] ?
10إِذْ أَوَى الْفِتْيَةُ إِلَى الْكَهْفِ فَقَالُوا رَبَّنَا آتِنَا مِن لَّدُنكَ رَحْمَةً وَهَيِّئْ لَنَا مِنْ أَمْرِنَا رَشَدًا
[Fàttalikul] ba waxamaande ya làqoo ca xunt ma, te ñu waxoon ne : “Yaw sunu Boroom, may nu yërmaande ju bawoo ci yaw; te nga yéwénal sunuy mbir mu nekk cig njub”.
11فَضَرَبْنَا عَلَىٰ آذَانِهِمْ فِي الْكَهْفِ سِنِينَ عَدَدًا
Nu fëkk seeni nopp [nelawloo leen] ca biir xunt ma ay at yu limu.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Kahf 9

Simoore Al-Kahf Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax amuloo njort ci ne, ñoñ-xunt ma ak ñoñ-mbind ma…

Simoore Aaya 9/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers