Al-Baqara · 13/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ آمِنُوا كَمَا آمَنَ النَّاسُ قَالُوا أَنُؤْمِنُ كَمَا آمَنَ السُّفَهَاءُ ۗ أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ السُّفَهَاءُ وَلَٰكِن لَّا يَعْلَمُونَ ١٣
Transliteration
Wa izaa qeela lahum aaminoo kamaaa aamanan naasu qaalooo anu`minu kamaaa aamanas sufahaaa`; alaaa innahum humus sufahaaa`u wa laakil laa ya`lamoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu ne leen : “Gëmleen ni nit ñi gëmee”, ñu tontu ne : “Ndax danuy gëm ni dof yi di gëmee ? ” Déedéet, ñoom ñooy diy dof, te xamuñu ko.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 11-15 — Al-Baqara
11وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا تُفْسِدُوا فِي الْأَرْضِ قَالُوا إِنَّمَا نَحْنُ مُصْلِحُونَ
Bu ñu leen waxee : 'Buleen di yàq ci suuf si ', ñu ne : 'Nun way-defar lanu ! '
12أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ الْمُفْسِدُونَ وَلَٰكِن لَّا يَشْعُرُونَ
Déedéet, ñoom ñooña ay yàq-kat lañu, te yëguñu ko.
13وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ آمِنُوا كَمَا آمَنَ النَّاسُ قَالُوا أَنُؤْمِنُ كَمَا آمَنَ السُّفَهَاءُ ۗ أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ السُّفَهَاءُ وَلَٰكِن لَّا يَعْلَمُونَ
Bu ñu ne leen : “Gëmleen ni nit ñi gëmee”, ñu tontu ne : “Ndax danuy gëm ni dof yi di gëmee ? ” Déedéet, ñoom ñooy diy dof, te xamuñu ko.
14وَإِذَا لَقُوا الَّذِينَ آمَنُوا قَالُوا آمَنَّا وَإِذَا خَلَوْا إِلَىٰ شَيَاطِينِهِمْ قَالُوا إِنَّا مَعَكُمْ إِنَّمَا نَحْنُ مُسْتَهْزِئُونَ
Bu ñu dajeek way-gëm ña, ne : “Gëm nanu” ; waaye bu ñu wéetee ak seeni (Séytaane naaféq yi), ne : “Nook yéen a ànd ; nun danuy yejji [jullit ñi] rekk”.
15اللَّهُ يَسْتَهْزِئُ بِهِمْ وَيَمُدُّهُمْ فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Yàllaa nga leen di yejji, di leen gën a yàggal ca seen mbeewte googu, ñuy deŋŋi-deŋŋi ak seen ngumbaag xol.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
13Aaya
Tekki — Al-Baqara 13
Simoore Al-Baqara Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu ne leen : “Gëmleen ni nit ñi gëmee”,…Simoore Aaya 13/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








