Al-Baqara · 152/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
فَاذْكُرُونِي أَذْكُرْكُمْ وَاشْكُرُوا لِي وَلَا تَكْفُرُونِ ١٥٢
Transliteration
Fazkurooneee azkurkum washkuroo lee wa laa takfuroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Fàttalikuleen Ma, Ma fàttaliku leen. Santleen Ma te buleen ma weddi.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 150-154 — Al-Baqara
150وَمِنْ حَيْثُ خَرَجْتَ فَوَلِّ وَجْهَكَ شَطْرَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ ۚ وَحَيْثُ مَا كُنتُمْ فَوَلُّوا وُجُوهَكُمْ شَطْرَهُ لِئَلَّا يَكُونَ لِلنَّاسِ عَلَيْكُمْ حُجَّةٌ إِلَّا الَّذِينَ ظَلَمُوا مِنْهُمْ فَلَا تَخْشَوْهُمْ وَاخْشَوْنِي وَلِأُتِمَّ نِعْمَتِي عَلَيْكُمْ وَلَعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ
Foo mën a demati, jëmaleel sa kanam ca Jàkka juñu wormaal ja ca Màkka. Fu ngeen mën a nekk, nangeen ca jëmale seeni kanam [jublu], ndax nit ñi bañ a am aw lay ci seen kaw, ku dul ñiy tooñ. Te buleen leen ragal ; ragal-leen Ma, man Yàlla, ngir Ma mottali sama xéewal ci yéen ak itam ndax ngeen gindiku !
151كَمَا أَرْسَلْنَا فِيكُمْ رَسُولًا مِّنكُمْ يَتْلُو عَلَيْكُمْ آيَاتِنَا وَيُزَكِّيكُمْ وَيُعَلِّمُكُمُ الْكِتَابَ وَالْحِكْمَةَ وَيُعَلِّمُكُم مَّا لَمْ تَكُونُوا تَعْلَمُونَ
Noonu, Lanu yónnee ci yéen Yonent bu bokk ci yéen buy jàng ci yéen laaya ya, di leen sellal, di leen xamal Téere ba ak Xereñ ga te di leen xamal itam lu ngeen xamul woon.
152فَاذْكُرُونِي أَذْكُرْكُمْ وَاشْكُرُوا لِي وَلَا تَكْفُرُونِ
Fàttalikuleen Ma, Ma fàttaliku leen. Santleen Ma te buleen ma weddi.
153يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اسْتَعِينُوا بِالصَّبْرِ وَالصَّلَاةِ ۚ إِنَّ اللَّهَ مَعَ الصَّابِرِينَ
Éy yéen ñi gëm [Jullit ñi] ! Nangeen dimbandikoo ci muñ ak julli. Yàlla ànd na ak way- muñ ña.
154وَلَا تَقُولُوا لِمَن يُقْتَلُ فِي سَبِيلِ اللَّهِ أَمْوَاتٌ ۚ بَلْ أَحْيَاءٌ وَلَٰكِن لَّا تَشْعُرُونَ
Buleen wax ne ñi ñu rey ci yoonu Yàlla dañuy dee de. Ña ngay dundu te yéguleen ko.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
152Aaya
Tekki — Al-Baqara 152
Simoore Al-Baqara Aaya 152 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fàttalikuleen Ma, Ma fàttaliku leen. Santleen Ma te buleen ma…Simoore Aaya 152/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 150–154. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








