Al-Baqara · 155/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
وَلَنَبْلُوَنَّكُم بِشَيْءٍ مِّنَ الْخَوْفِ وَالْجُوعِ وَنَقْصٍ مِّنَ الْأَمْوَالِ وَالْأَنفُسِ وَالثَّمَرَاتِ ۗ وَبَشِّرِ الصَّابِرِينَ ۝١٥٥
Wa lanablu wannakum bishai`im minal khawfi waljoo`i wa naqsim minal amwaali wal anfusi was samaraat; wa bashshiris saabireen
📖 Tekkim Wolof
Danaa leen farala nattoo lennat ci am tiit, xiif ak wàññikug ay alal, ak i bakkan ak i meññent. Waaye bégalal ñi koy muñ,
🎧 Dégg

📜 Aaya 153-157 — Al-Baqara

153يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اسْتَعِينُوا بِالصَّبْرِ وَالصَّلَاةِ ۚ إِنَّ اللَّهَ مَعَ الصَّابِرِينَ
Éy yéen ñi gëm [Jullit ñi] ! Nangeen dimbandikoo ci muñ ak julli. Yàlla ànd na ak way- muñ ña.
154وَلَا تَقُولُوا لِمَن يُقْتَلُ فِي سَبِيلِ اللَّهِ أَمْوَاتٌ ۚ بَلْ أَحْيَاءٌ وَلَٰكِن لَّا تَشْعُرُونَ
Buleen wax ne ñi ñu rey ci yoonu Yàlla dañuy dee de. Ña ngay dundu te yéguleen ko.
155وَلَنَبْلُوَنَّكُم بِشَيْءٍ مِّنَ الْخَوْفِ وَالْجُوعِ وَنَقْصٍ مِّنَ الْأَمْوَالِ وَالْأَنفُسِ وَالثَّمَرَاتِ ۗ وَبَشِّرِ الصَّابِرِينَ
Danaa leen farala nattoo lennat ci am tiit, xiif ak wàññikug ay alal, ak i bakkan ak i meññent. Waaye bégalal ñi koy muñ,
156الَّذِينَ إِذَا أَصَابَتْهُم مُّصِيبَةٌ قَالُوا إِنَّا لِلَّهِ وَإِنَّا إِلَيْهِ رَاجِعُونَ
ña nga xam ne, saa su leen tiis dalee dañu naan : “Yàllaa nu moom te ca Moom Yàlla lanuy dellu”.
157أُولَٰئِكَ عَلَيْهِمْ صَلَوَاتٌ مِّن رَّبِّهِمْ وَرَحْمَةٌ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُهْتَدُونَ
Gaa ñooña am nañu njéggal gu bawoo ca seen Boroom, ak yérmaande ; te ñoo di ña gindiku tigi.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
155Aaya

Tekki — Al-Baqara 155

Simoore Al-Baqara Aaya 155 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danaa leen farala nattoo lennat ci am tiit, xiif ak…

Simoore Aaya 155/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 153–157. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers