Taha · 23/135
Tekki Waxtaan — Taha
لِنُرِيَكَ مِنْ آيَاتِنَا الْكُبْرَى ۝٢٣
Linuriyaka min Aayaatinal Kubra
📖 Tekkim Wolof
[Lii lépp] Danu la koo waajale ngir won la ci Sunu kéemtaan yu màgg yi.
🎧 Dégg

📜 Aaya 21-25 — Taha

21قَالَ خُذْهَا وَلَا تَخَفْ ۖ سَنُعِيدُهَا سِيرَتَهَا الْأُولَىٰ
Mu ne ko : “Jël ko : Dananu ko delloo na mu meloon, bul ragal.
22وَاضْمُمْ يَدَكَ إِلَىٰ جَنَاحِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ آيَةً أُخْرَىٰ
Te nga dugal sa loxo ci sa biir poqotaan : mu génn weex tàll lool, di geneen kéemaan
23لِنُرِيَكَ مِنْ آيَاتِنَا الْكُبْرَى
[Lii lépp] Danu la koo waajale ngir won la ci Sunu kéemtaan yu màgg yi.
24اذْهَبْ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ
Demal ca Firawna, moom dafa beew.
25قَالَ رَبِّ اشْرَحْ لِي صَدْرِي
[Muusaa] ne ko : “Yaw sama Boroom, leeralal ma sama dënn [mën a dékku lu bari],
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Taha 23

Simoore Taha Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Lii lépp] Danu la koo waajale ngir won la ci…

Simoore Aaya 23/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers