Taha · 31/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
اشْدُدْ بِهِ أَزْرِي ۝٣١
Ushdud biheee azree
📖 Tekkim Wolof
Doolel ma ci moom !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 29-33 — Simoore Taha

29وَاجْعَل لِّي وَزِيرًا مِّنْ أَهْلِي
te nga may ma, defal ma ci samag njaboot ku may jàppale :
30هَارُونَ أَخِي
Te mu far doon sax Haaruuna, sama mbokk,
31اشْدُدْ بِهِ أَزْرِي
Doolel ma ci moom !
32وَأَشْرِكْهُ فِي أَمْرِي
te boole ko ci samay mbir,
33كَيْ نُسَبِّحَكَ كَثِيرًا
ngir nu mën di la sàbbaal lu bari,
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Taha 31

Simoore Taha Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Doolel ma ci moom !

Simoore Aaya 31/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers