Taha · 94/135
Tekki Waxtaan — Taha
قَالَ يَا ابْنَ أُمَّ لَا تَأْخُذْ بِلِحْيَتِي وَلَا بِرَأْسِي ۖ إِنِّي خَشِيتُ أَن تَقُولَ فَرَّقْتَ بَيْنَ بَنِي إِسْرَائِيلَ وَلَمْ تَرْقُبْ قَوْلِي ۝٩٤
Qaala yabna`umma laa taakhuz bilihyatee wa laa biraasee innee khashetu an taqoola farraqta baina Baneee Israaa`eela wa lam tarqub qawlee
📖 Tekkim Wolof
[Aaruuna] ne ko : “Doom ndey, bul bipp samab sikkim mbaa sama kawari bopp. Damaa ragaloon nga naan ma : “Féewale nga giiru Bani-Israayiila, toppoo sama ndigal, [lii rekk la]”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 92-96 — Taha

92قَالَ يَا هَارُونُ مَا مَنَعَكَ إِذْ رَأَيْتَهُمْ ضَلُّوا
[Ba Muusaa dellusee] ne : “Yaw Aaruuna, lan moo tere woon nga waar leen ba ñu sànkoo.
93أَلَّا تَتَّبِعَنِ ۖ أَفَعَصَيْتَ أَمْرِي
Danga maa toppatul walla dangaa mooy léegi samay ndigal ? ”
94قَالَ يَا ابْنَ أُمَّ لَا تَأْخُذْ بِلِحْيَتِي وَلَا بِرَأْسِي ۖ إِنِّي خَشِيتُ أَن تَقُولَ فَرَّقْتَ بَيْنَ بَنِي إِسْرَائِيلَ وَلَمْ تَرْقُبْ قَوْلِي
[Aaruuna] ne ko : “Doom ndey, bul bipp samab sikkim mbaa sama kawari bopp. Damaa ragaloon nga naan ma : “Féewale nga giiru Bani-Israayiila, toppoo sama ndigal, [lii rekk la]”.
95قَالَ فَمَا خَطْبُكَ يَا سَامِرِيُّ
Muusaa ne : “Ayca Saamiriyu, waxal book ? ”
96قَالَ بَصُرْتُ بِمَا لَمْ يَبْصُرُوا بِهِ فَقَبَضْتُ قَبْضَةً مِّنْ أَثَرِ الرَّسُولِ فَنَبَذْتُهَا وَكَذَٰلِكَ سَوَّلَتْ لِي نَفْسِي
Mu ne : “Gis naa lu ñu gisul : ma daldi ŋoor ci suufi jeexiti Yonent bi, daldi koy sànni li am am. Loolu la ma sama xel joxoon”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
94Aaya

Tekki — Taha 94

Simoore Taha Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Aaruuna] ne ko : “Doom ndey, bul bipp samab sikkim…

Simoore Aaya 94/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers