Al-Anbiya · 73/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَجَعَلْنَاهُمْ أَئِمَّةً يَهْدُونَ بِأَمْرِنَا وَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِمْ فِعْلَ الْخَيْرَاتِ وَإِقَامَ الصَّلَاةِ وَإِيتَاءَ الزَّكَاةِ ۖ وَكَانُوا لَنَا عَابِدِينَ ۝٧٣
Wa ja`alnaahum a`immatany yahdoona bi amrinaa wa awhainaaa ilaihim fi`lal khairaati wa iqaamas Salaati wa eetaaa`az Zakaati wa kaanoo lanaa `aabideen
📖 Tekkim Wolof
Def leen ay njiit yuy gindee ci Sunu ndigal. Nu soloo leen jëf yu yiw, ak taxawal julli ak génne asaka. Te ñoom daal daanañu Ma jaamu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 71-75 — Al-Anbiya

71وَنَجَّيْنَاهُ وَلُوطًا إِلَى الْأَرْضِ الَّتِي بَارَكْنَا فِيهَا لِلْعَالَمِينَ
Nu daldi koy musal moom ak Lóot jëme leen fa suuf sa Nu barkeel ngir waa àddina si yépp.
72وَوَهَبْنَا لَهُ إِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ نَافِلَةً ۖ وَكُلًّا جَعَلْنَا صَالِحِينَ
Nu may ko Isaaqa ak Yàqooba, muy ndollent, Nu def leen ñu nekk ñoom ñépp di ñu sell.
73وَجَعَلْنَاهُمْ أَئِمَّةً يَهْدُونَ بِأَمْرِنَا وَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِمْ فِعْلَ الْخَيْرَاتِ وَإِقَامَ الصَّلَاةِ وَإِيتَاءَ الزَّكَاةِ ۖ وَكَانُوا لَنَا عَابِدِينَ
Def leen ay njiit yuy gindee ci Sunu ndigal. Nu soloo leen jëf yu yiw, ak taxawal julli ak génne asaka. Te ñoom daal daanañu Ma jaamu.
74وَلُوطًا آتَيْنَاهُ حُكْمًا وَعِلْمًا وَنَجَّيْنَاهُ مِنَ الْقَرْيَةِ الَّتِي كَانَت تَّعْمَلُ الْخَبَائِثَ ۗ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمَ سَوْءٍ فَاسِقِينَ
Ak Lóot ! May Nanu ko ràññee, dégg ak xam-xam, te musal Na
75وَأَدْخَلْنَاهُ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُ مِنَ الصَّالِحِينَ
Dugal Nanu ko ci Sunu yërmaande. Te moom bokk na ca ñu sell ña.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Al-Anbiya 73

Simoore Al-Anbiya Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Def leen ay njiit yuy gindee ci Sunu ndigal. Nu…

Simoore Aaya 73/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers