Al-Anbiya · 72/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَوَهَبْنَا لَهُ إِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ نَافِلَةً ۖ وَكُلًّا جَعَلْنَا صَالِحِينَ ۝٧٢
Wa wahabnaa lahooo Ishaaq; wa Ya`qooba naafilah; wa kullan ja`alnaa saaliheen
📖 Tekkim Wolof
Nu may ko Isaaqa ak Yàqooba, muy ndollent, Nu def leen ñu nekk ñoom ñépp di ñu sell.

🎧 Dégg


📜 Aaya 70-74 — Al-Anbiya

70وَأَرَادُوا بِهِ كَيْدًا فَجَعَلْنَاهُمُ الْأَخْسَرِينَ
Ñu bëgg a def seeni pexe ci moom, Nu def leen ñu di ñu yàqule ña.
71وَنَجَّيْنَاهُ وَلُوطًا إِلَى الْأَرْضِ الَّتِي بَارَكْنَا فِيهَا لِلْعَالَمِينَ
Nu daldi koy musal moom ak Lóot jëme leen fa suuf sa Nu barkeel ngir waa àddina si yépp.
72وَوَهَبْنَا لَهُ إِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ نَافِلَةً ۖ وَكُلًّا جَعَلْنَا صَالِحِينَ
Nu may ko Isaaqa ak Yàqooba, muy ndollent, Nu def leen ñu nekk ñoom ñépp di ñu sell.
73وَجَعَلْنَاهُمْ أَئِمَّةً يَهْدُونَ بِأَمْرِنَا وَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِمْ فِعْلَ الْخَيْرَاتِ وَإِقَامَ الصَّلَاةِ وَإِيتَاءَ الزَّكَاةِ ۖ وَكَانُوا لَنَا عَابِدِينَ
Def leen ay njiit yuy gindee ci Sunu ndigal. Nu soloo leen jëf yu yiw, ak taxawal julli ak génne asaka. Te ñoom daal daanañu Ma jaamu.
74وَلُوطًا آتَيْنَاهُ حُكْمًا وَعِلْمًا وَنَجَّيْنَاهُ مِنَ الْقَرْيَةِ الَّتِي كَانَت تَّعْمَلُ الْخَبَائِثَ ۗ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمَ سَوْءٍ فَاسِقِينَ
Ak Lóot ! May Nanu ko ràññee, dégg ak xam-xam, te musal Na
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — Al-Anbiya 72

Simoore Al-Anbiya Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu may ko Isaaqa ak Yàqooba, muy ndollent, Nu def…

Simoore Aaya 72/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers