Al-Hajj · 33/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
لَكُمْ فِيهَا مَنَافِعُ إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى ثُمَّ مَحِلُّهَا إِلَى الْبَيْتِ الْعَتِيقِ ۝٣٣
Lakum feehaa manaafi`u ilaaa ajalim musamman summa mahilluhaaa ilal Baitil `Ateeq
📖 Tekkim Wolof
Ñeel na leen ci loolu ay njariñ ba àpp bu ñu tudd ; te it seen barab ba ñuy loje ma nga ca Néeg bu yàgg a yàgg ba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Al-Hajj

31حُنَفَاءَ لِلَّهِ غَيْرَ مُشْرِكِينَ بِهِ ۚ وَمَن يُشْرِكْ بِاللَّهِ فَكَأَنَّمَا خَرَّ مِنَ السَّمَاءِ فَتَخْطَفُهُ الطَّيْرُ أَوْ تَهْوِي بِهِ الرِّيحُ فِي مَكَانٍ سَحِيقٍ
Nangeen doon ñuy sellal ngir Yàlla (ñu àndul ak bokkaale) ; ku bokkaale ak Yàlla, dangay mel ni ku rëcc jóge asamaan, njanaaw fëkk ko walla ngelaw sànni ko barab bu sore.
32ذَٰلِكَ وَمَن يُعَظِّمْ شَعَائِرَ اللَّهِ فَإِنَّهَا مِن تَقْوَى الْقُلُوبِ
Noonu la. Képp ku màggal jaamukaayu Yàlla, na xam ne màggal googu bokk na ca ragalug Yàlla ci xol yi.
33لَكُمْ فِيهَا مَنَافِعُ إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى ثُمَّ مَحِلُّهَا إِلَى الْبَيْتِ الْعَتِيقِ
Ñeel na leen ci loolu ay njariñ ba àpp bu ñu tudd ; te it seen barab ba ñuy loje ma nga ca Néeg bu yàgg a yàgg ba.
34وَلِكُلِّ أُمَّةٍ جَعَلْنَا مَنسَكًا لِّيَذْكُرُوا اسْمَ اللَّهِ عَلَىٰ مَا رَزَقَهُم مِّن بَهِيمَةِ الْأَنْعَامِ ۗ فَإِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ فَلَهُ أَسْلِمُوا ۗ وَبَشِّرِ الْمُخْبِتِينَ
Te xeet wu nekk, defal Nanu ko jaamukaay ngir ñuy tudd turu Yàlla ci li Mu leen wërsëgal ci juri kër yi. Kon seen Boroom jenn Yàlla doŋŋ la. Kon nangeen wommatu jëm ci Moom. Bégalal way-toroxlu ña,
35الَّذِينَ إِذَا ذُكِرَ اللَّهُ وَجِلَتْ قُلُوبُهُمْ وَالصَّابِرِينَ عَلَىٰ مَا أَصَابَهُمْ وَالْمُقِيمِي الصَّلَاةِ وَمِمَّا رَزَقْنَاهُمْ يُنفِقُونَ
ña nga xam ne fu ñu tudde Yàlla seeni xol yëngu, ak way-muñ ña ca la leen dal, ak ñay taxawal julli tey lele ca la Nu leen wërsëgale.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
33Aaya

Tekki — Al-Hajj 33

Simoore Al-Hajj Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñeel na leen ci loolu ay njariñ ba àpp bu…

Simoore Aaya 33/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers