Al-Mu'minun · 104/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
تَلْفَحُ وُجُوهَهُمُ النَّارُ وَهُمْ فِيهَا كَالِحُونَ ۝١٠٤
Talfahu wujoohahumun Naaru wa hum feehaa kaalihood
📖 Tekkim Wolof
Safara waa ngay làkk seeni kanam, ñu ne fa xuum

🎧 Dégg


📜 Aaya 102-106 — Simoore Al-Mu'minun

102فَمَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Képp ku peeseem diis [ak jëf yu baax]ñoom ñooy ña texe ;
103وَمَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ فِي جَهَنَّمَ خَالِدُونَ
képp ku peeseem woyof [ak jëf yu baax], ñooña ñoo di ña sànku ci biir Safara te béel fa.
104تَلْفَحُ وُجُوهَهُمُ النَّارُ وَهُمْ فِيهَا كَالِحُونَ
Safara waa ngay làkk seeni kanam, ñu ne fa xuum
105أَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُم بِهَا تُكَذِّبُونَ
“Moo ndax daa weesul jàng samag waareci yéen, ngeen jàppe ko ay fen ? ”
106قَالُوا رَبَّنَا غَلَبَتْ عَلَيْنَا شِقْوَتُنَا وَكُنَّا قَوْمًا ضَالِّينَ
Ñu wax ne : “Boroom sunu ! Texeedi not nanu te xamadi woon nanu itam.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
104Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 104

Simoore Al-Mu'minun Aaya 104 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Safara waa ngay làkk seeni kanam, ñu ne fa xuum

Simoore Aaya 104/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 102–106. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers