Al-Mu'minun · 103/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَمَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ فِي جَهَنَّمَ خَالِدُونَ ۝١٠٣
Wa man khaffat mawaa zeenuhoo fa ulaaa`ikal lazeena khasiroon anfusahum fee Jahannnama khaalidoon
📖 Tekkim Wolof
képp ku peeseem woyof [ak jëf yu baax], ñooña ñoo di ña sànku ci biir Safara te béel fa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 101-105 — Simoore Al-Mu'minun

101فَإِذَا نُفِخَ فِي الصُّورِ فَلَا أَنسَابَ بَيْنَهُمْ يَوْمَئِذٍ وَلَا يَتَسَاءَلُونَ
Bu ñu walee Buftu bi kerook Bisboobu, askan amatul seen diggante te dootuñu lijjanti.
102فَمَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Képp ku peeseem diis [ak jëf yu baax]ñoom ñooy ña texe ;
103وَمَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ فِي جَهَنَّمَ خَالِدُونَ
képp ku peeseem woyof [ak jëf yu baax], ñooña ñoo di ña sànku ci biir Safara te béel fa.
104تَلْفَحُ وُجُوهَهُمُ النَّارُ وَهُمْ فِيهَا كَالِحُونَ
Safara waa ngay làkk seeni kanam, ñu ne fa xuum
105أَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُم بِهَا تُكَذِّبُونَ
“Moo ndax daa weesul jàng samag waareci yéen, ngeen jàppe ko ay fen ? ”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
103Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 103

Simoore Al-Mu'minun Aaya 103 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : képp ku peeseem woyof [ak jëf yu baax], ñooña ñoo…

Simoore Aaya 103/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 101–105. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers