Al-Mu'minun · 9/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَالَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَوَاتِهِمْ يُحَافِظُونَ ۝٩
Wallazeena hum `alaa Salawaatihim yuhaafizoon
📖 Tekkim Wolof
tey wattu seeni julli [di ko sàmm].

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Mu'minun

7فَمَنِ ابْتَغَىٰ وَرَاءَ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْعَادُونَ
ku sàkku leneen ginnaaw loolu nag, ñoom la ñuy tudde way-jalgati ña ;
8وَالَّذِينَ هُمْ لِأَمَانَاتِهِمْ وَعَهْدِهِمْ رَاعُونَ
ña nga xam ne nag dañuy sàmm la ñu leen dénk ak seeni kàddu,
9وَالَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَوَاتِهِمْ يُحَافِظُونَ
tey wattu seeni julli [di ko sàmm].
10أُولَٰئِكَ هُمُ الْوَارِثُونَ
Ñoom dey ñooy donnkat ya,
11الَّذِينَ يَرِثُونَ الْفِرْدَوْسَ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
ña nga xam ne danañu donn Àjjana Firdawsi, te dañu cay béel.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 9

Simoore Al-Mu'minun Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : tey wattu seeni julli [di ko sàmm].

Simoore Aaya 9/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers