An-Nur · 27/64
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nur
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَدْخُلُوا بُيُوتًا غَيْرَ بُيُوتِكُمْ حَتَّىٰ تَسْتَأْنِسُوا وَتُسَلِّمُوا عَلَىٰ أَهْلِهَا ۚ ذَٰلِكُمْ خَيْرٌ لَّكُمْ لَعَلَّكُمْ تَذَكَّرُونَ ۝٢٧
Yaaa aiyuhal lazeena aamanoo laa tadkhuloo buyootan ghaira buyootikum hatta tastaanisoo wa tusallimoo `allaa ahlihaa; zaalikum khairul lakum la`allakum tazakkaroon
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm ! Buleen dugg kër gu dul seeni kër ndare bu dangeen a yéglu te nuyyu waa kër ga. Loolu dey moo gën ci yéen ndax xéy-na ngeen fàttaliku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore An-Nur

25يَوْمَئِذٍ يُوَفِّيهِمُ اللَّهُ دِينَهُمُ الْحَقَّ وَيَعْلَمُونَ أَنَّ اللَّهَ هُوَ الْحَقُّ الْمُبِينُ
Bu Bis boobaa, Yàlla dana leen jox, indil leen seen diine ja di dëgg ; [Bu keroogee] lañuy xam ne Yàllaay dëgg gu fés ga.
26الْخَبِيثَاتُ لِلْخَبِيثِينَ وَالْخَبِيثُونَ لِلْخَبِيثَاتِ ۖ وَالطَّيِّبَاتُ لِلطَّيِّبِينَ وَالطَّيِّبُونَ لِلطَّيِّبَاتِ ۚ أُولَٰئِكَ مُبَرَّءُونَ مِمَّا يَقُولُونَ ۖ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ
Jigéen ñu bon ña témboo nañook góor ñu bon ña. Jigéen ñu baax ña témbook góor ñu baax ña. Góor ñu baax ña it ñoom témbook jigéen ñu baax ña. Ñoom set nañu wecc ca la ñuy wax. Am nañu ag njéggal te am nañu pey gu duun.
27يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَدْخُلُوا بُيُوتًا غَيْرَ بُيُوتِكُمْ حَتَّىٰ تَسْتَأْنِسُوا وَتُسَلِّمُوا عَلَىٰ أَهْلِهَا ۚ ذَٰلِكُمْ خَيْرٌ لَّكُمْ لَعَلَّكُمْ تَذَكَّرُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen dugg kër gu dul seeni kër ndare bu dangeen a yéglu te nuyyu waa kër ga. Loolu dey moo gën ci yéen ndax xéy-na ngeen fàttaliku.
28فَإِن لَّمْ تَجِدُوا فِيهَا أَحَدًا فَلَا تَدْخُلُوهَا حَتَّىٰ يُؤْذَنَ لَكُمْ ۖ وَإِن قِيلَ لَكُمُ ارْجِعُوا فَارْجِعُوا ۖ هُوَ أَزْكَىٰ لَكُمْ ۚ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ عَلِيمٌ
Bu ngeen ca fekkul kenn, buleen ca dugg li feek joxuñuleen ca ndigal. Te bu ñu la nee : “Dellul [damaa jàpp]”, dellul. Loolu moo gën a sell ci yéen. Yàlla aka xam li ngeen di def.
29لَّيْسَ عَلَيْكُمْ جُنَاحٌ أَن تَدْخُلُوا بُيُوتًا غَيْرَ مَسْكُونَةٍ فِيهَا مَتَاعٌ لَّكُمْ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُبْدُونَ وَمَا تَكْتُمُونَ
[Waaye] bàkkaar amul ci yéen ngeen dugg ci kër gu ñu dëkkewul te seen tobarte nekk fa. Yàlla xam na li ngeen feeñal ak li ngeen di nëbb.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
27Aaya

Tekki — An-Nur 27

Simoore An-Nur Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm ! Buleen dugg kër gu dul…

Simoore Aaya 27/64 — Simoore An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nur Dégg, Simoore An-Nur Tekki, Simoore An-Nur mp3, Simoore An-Nur pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers