An-Nur · 26/64
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nur
الْخَبِيثَاتُ لِلْخَبِيثِينَ وَالْخَبِيثُونَ لِلْخَبِيثَاتِ ۖ وَالطَّيِّبَاتُ لِلطَّيِّبِينَ وَالطَّيِّبُونَ لِلطَّيِّبَاتِ ۚ أُولَٰئِكَ مُبَرَّءُونَ مِمَّا يَقُولُونَ ۖ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ ۝٢٦
Alkhabeesaatu lilkha beeseena walkhabeesoona lilkhabeesaati wattaiyibaatu littaiyibeena wattaiyiboona littaiyibaat; ulaaa`ika mubar ra`oona maimma yaqooloona lahum maghfiratunw wa rizqun kareem
📖 Tekkim Wolof
Jigéen ñu bon ña témboo nañook góor ñu bon ña. Jigéen ñu baax ña témbook góor ñu baax ña. Góor ñu baax ña it ñoom témbook jigéen ñu baax ña. Ñoom set nañu wecc ca la ñuy wax. Am nañu ag njéggal te am nañu pey gu duun.

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore An-Nur

24يَوْمَ تَشْهَدُ عَلَيْهِمْ أَلْسِنَتُهُمْ وَأَيْدِيهِمْ وَأَرْجُلُهُم بِمَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Bu keroogee [Bis-pénc ba], seen làmmiñ ya, seeni yoxo ak seeni tànk danañu seede ci seen kaw la ñu daan def.
25يَوْمَئِذٍ يُوَفِّيهِمُ اللَّهُ دِينَهُمُ الْحَقَّ وَيَعْلَمُونَ أَنَّ اللَّهَ هُوَ الْحَقُّ الْمُبِينُ
Bu Bis boobaa, Yàlla dana leen jox, indil leen seen diine ja di dëgg ; [Bu keroogee] lañuy xam ne Yàllaay dëgg gu fés ga.
26الْخَبِيثَاتُ لِلْخَبِيثِينَ وَالْخَبِيثُونَ لِلْخَبِيثَاتِ ۖ وَالطَّيِّبَاتُ لِلطَّيِّبِينَ وَالطَّيِّبُونَ لِلطَّيِّبَاتِ ۚ أُولَٰئِكَ مُبَرَّءُونَ مِمَّا يَقُولُونَ ۖ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ
Jigéen ñu bon ña témboo nañook góor ñu bon ña. Jigéen ñu baax ña témbook góor ñu baax ña. Góor ñu baax ña it ñoom témbook jigéen ñu baax ña. Ñoom set nañu wecc ca la ñuy wax. Am nañu ag njéggal te am nañu pey gu duun.
27يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَدْخُلُوا بُيُوتًا غَيْرَ بُيُوتِكُمْ حَتَّىٰ تَسْتَأْنِسُوا وَتُسَلِّمُوا عَلَىٰ أَهْلِهَا ۚ ذَٰلِكُمْ خَيْرٌ لَّكُمْ لَعَلَّكُمْ تَذَكَّرُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen dugg kër gu dul seeni kër ndare bu dangeen a yéglu te nuyyu waa kër ga. Loolu dey moo gën ci yéen ndax xéy-na ngeen fàttaliku.
28فَإِن لَّمْ تَجِدُوا فِيهَا أَحَدًا فَلَا تَدْخُلُوهَا حَتَّىٰ يُؤْذَنَ لَكُمْ ۖ وَإِن قِيلَ لَكُمُ ارْجِعُوا فَارْجِعُوا ۖ هُوَ أَزْكَىٰ لَكُمْ ۚ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ عَلِيمٌ
Bu ngeen ca fekkul kenn, buleen ca dugg li feek joxuñuleen ca ndigal. Te bu ñu la nee : “Dellul [damaa jàpp]”, dellul. Loolu moo gën a sell ci yéen. Yàlla aka xam li ngeen di def.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
26Aaya

Tekki — An-Nur 26

Simoore An-Nur Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jigéen ñu bon ña témboo nañook góor ñu bon ña.…

Simoore Aaya 26/64 — Simoore An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nur Dégg, Simoore An-Nur Tekki, Simoore An-Nur mp3, Simoore An-Nur pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers