Al-Furqan · 13/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَإِذَا أُلْقُوا مِنْهَا مَكَانًا ضَيِّقًا مُّقَرَّنِينَ دَعَوْا هُنَالِكَ ثُبُورًا ۝١٣
Wa izaaa ulqoo minhaa makaanan daiyiqam muqar raneena da`aw hunaalika subooraa
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu leen ca sànnee ci pukus bu xat, lëkke leen [jéng], ñuy wél-wéliy juuxu ci toskare.

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Simoore Al-Furqan

11بَلْ كَذَّبُوا بِالسَّاعَةِ ۖ وَأَعْتَدْنَا لِمَن كَذَّبَ بِالسَّاعَةِ سَعِيرًا
Waaye wedd nañu Bis-pénc ba. Te Nun kat waajalal Nanu, képp ku weddi Bis-pénc ba, aw safara wuy jér-jéri.
12إِذَا رَأَتْهُم مِّن مَّكَانٍ بَعِيدٍ سَمِعُوا لَهَا تَغَيُّظًا وَزَفِيرًا
Saa su leen Safara soosu séenee fu sori, dinañu dégg riiram.
13وَإِذَا أُلْقُوا مِنْهَا مَكَانًا ضَيِّقًا مُّقَرَّنِينَ دَعَوْا هُنَالِكَ ثُبُورًا
Bu ñu leen ca sànnee ci pukus bu xat, lëkke leen [jéng], ñuy wél-wéliy juuxu ci toskare.
14لَّا تَدْعُوا الْيَوْمَ ثُبُورًا وَاحِدًا وَادْعُوا ثُبُورًا كَثِيرًا
“Bisu tey jii, buleen yuuxu jenn tuskare doŋŋ, ay tuskare yu bari la”.
15قُلْ أَذَٰلِكَ خَيْرٌ أَمْ جَنَّةُ الْخُلْدِ الَّتِي وُعِدَ الْمُتَّقُونَ ۚ كَانَتْ لَهُمْ جَزَاءً وَمَصِيرًا
Neel : “Ndax loolu moo gën ? Walla Àjjanay xéewal ju sax ju ma digee fey gaa ña ragal Yàlla, muy seen kër ?”
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Furqan 13

Simoore Al-Furqan Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu leen ca sànnee ci pukus bu xat, lëkke…

Simoore Aaya 13/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers