Al-Furqan · 12/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
إِذَا رَأَتْهُم مِّن مَّكَانٍ بَعِيدٍ سَمِعُوا لَهَا تَغَيُّظًا وَزَفِيرًا ۝١٢
Izaa ra`at hum mim ma kaanim ba`eedin sami`oo lahaa taghaiyuzanw wa zafeeraa
📖 Tekkim Wolof
Saa su leen Safara soosu séenee fu sori, dinañu dégg riiram.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Al-Furqan

10تَبَارَكَ الَّذِي إِن شَاءَ جَعَلَ لَكَ خَيْرًا مِّن ذَٰلِكَ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ وَيَجْعَل لَّكَ قُصُورًا
Yàlla ju barkeel ja nga xam ne bu Ko sooboon Mu defal la ci loolu Àjjana joo xam ay dex dañuy daw ci suufam ; Mu defal la it ay jénde.
11بَلْ كَذَّبُوا بِالسَّاعَةِ ۖ وَأَعْتَدْنَا لِمَن كَذَّبَ بِالسَّاعَةِ سَعِيرًا
Waaye wedd nañu Bis-pénc ba. Te Nun kat waajalal Nanu, képp ku weddi Bis-pénc ba, aw safara wuy jér-jéri.
12إِذَا رَأَتْهُم مِّن مَّكَانٍ بَعِيدٍ سَمِعُوا لَهَا تَغَيُّظًا وَزَفِيرًا
Saa su leen Safara soosu séenee fu sori, dinañu dégg riiram.
13وَإِذَا أُلْقُوا مِنْهَا مَكَانًا ضَيِّقًا مُّقَرَّنِينَ دَعَوْا هُنَالِكَ ثُبُورًا
Bu ñu leen ca sànnee ci pukus bu xat, lëkke leen [jéng], ñuy wél-wéliy juuxu ci toskare.
14لَّا تَدْعُوا الْيَوْمَ ثُبُورًا وَاحِدًا وَادْعُوا ثُبُورًا كَثِيرًا
“Bisu tey jii, buleen yuuxu jenn tuskare doŋŋ, ay tuskare yu bari la”.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Furqan 12

Simoore Al-Furqan Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa su leen Safara soosu séenee fu sori, dinañu dégg…

Simoore Aaya 12/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers