Al-Furqan · 14/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
لَّا تَدْعُوا الْيَوْمَ ثُبُورًا وَاحِدًا وَادْعُوا ثُبُورًا كَثِيرًا ١٤
Transliteration
Laa tad`ul yawma subooranw waahidanw wad`oo subooran kaseeraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
“Bisu tey jii, buleen yuuxu jenn tuskare doŋŋ, ay tuskare yu bari la”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 12-16 — Al-Furqan
12إِذَا رَأَتْهُم مِّن مَّكَانٍ بَعِيدٍ سَمِعُوا لَهَا تَغَيُّظًا وَزَفِيرًا
Saa su leen Safara soosu séenee fu sori, dinañu dégg riiram.
13وَإِذَا أُلْقُوا مِنْهَا مَكَانًا ضَيِّقًا مُّقَرَّنِينَ دَعَوْا هُنَالِكَ ثُبُورًا
Bu ñu leen ca sànnee ci pukus bu xat, lëkke leen [jéng], ñuy wél-wéliy juuxu ci toskare.
14لَّا تَدْعُوا الْيَوْمَ ثُبُورًا وَاحِدًا وَادْعُوا ثُبُورًا كَثِيرًا
“Bisu tey jii, buleen yuuxu jenn tuskare doŋŋ, ay tuskare yu bari la”.
15قُلْ أَذَٰلِكَ خَيْرٌ أَمْ جَنَّةُ الْخُلْدِ الَّتِي وُعِدَ الْمُتَّقُونَ ۚ كَانَتْ لَهُمْ جَزَاءً وَمَصِيرًا
Neel : “Ndax loolu moo gën ? Walla Àjjanay xéewal ju sax ju ma digee fey gaa ña ragal Yàlla, muy seen kër ?”
16لَّهُمْ فِيهَا مَا يَشَاءُونَ خَالِدِينَ ۚ كَانَ عَلَىٰ رَبِّكَ وَعْدًا مَّسْئُولًا
Am nañu fa lépp lu leen fa soob te dañu fay béel. Yàllaa ko warlu.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
14Aaya
Tekki — Al-Furqan 14
Simoore Al-Furqan Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Bisu tey jii, buleen yuuxu jenn tuskare doŋŋ, ay tuskare…Simoore Aaya 14/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








