Al-Furqan · 2/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
الَّذِي لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَلَمْ يَتَّخِذْ وَلَدًا وَلَمْ يَكُن لَّهُ شَرِيكٌ فِي الْمُلْكِ وَخَلَقَ كُلَّ شَيْءٍ فَقَدَّرَهُ تَقْدِيرًا ۝٢
Allazee lahoo mulkus samaawaati wal ardi wa lam yattakhiz waladanw wa lam yakul lahoo shareekun filmulki wa khalaqa kulla shai`in faqaddarahoo taqdeeraa
📖 Tekkim Wolof
Moom mi nga xam ne Moo moom nguurug asamaan yeek suuf si, te jàppewul kenn doomam, te it amul ku Mu bokkal nguur gi, Moo bind lépp te jox na ko dayo ba mu témbool.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-4 — Al-Furqan

1تَبَارَكَ الَّذِي نَزَّلَ الْفُرْقَانَ عَلَىٰ عَبْدِهِ لِيَكُونَ لِلْعَالَمِينَ نَذِيرًا
Yàlla barkeel na [màgg na] Moom mi wàcce Téere ba [Alxuraan] ca jaamam ba ngir mu doon luy xupp waa àddina si yépp.
2الَّذِي لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَلَمْ يَتَّخِذْ وَلَدًا وَلَمْ يَكُن لَّهُ شَرِيكٌ فِي الْمُلْكِ وَخَلَقَ كُلَّ شَيْءٍ فَقَدَّرَهُ تَقْدِيرًا
Moom mi nga xam ne Moo moom nguurug asamaan yeek suuf si, te jàppewul kenn doomam, te it amul ku Mu bokkal nguur gi, Moo bind lépp te jox na ko dayo ba mu témbool.
3وَاتَّخَذُوا مِن دُونِهِ آلِهَةً لَّا يَخْلُقُونَ شَيْئًا وَهُمْ يُخْلَقُونَ وَلَا يَمْلِكُونَ لِأَنفُسِهِمْ ضَرًّا وَلَا نَفْعًا وَلَا يَمْلِكُونَ مَوْتًا وَلَا حَيَاةً وَلَا نُشُورًا
Te ñoom dañoo jàppe ay yàlla ñenenn ñoo xam ne binduñu tus, faf ñoom sax dañu leen a bind, te it mënuñoo lor seen bopp waxantumalaak njariñ, amuñu dee amuñu dundu waxantumalaak dekki.
4وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا إِفْكٌ افْتَرَاهُ وَأَعَانَهُ عَلَيْهِ قَوْمٌ آخَرُونَ ۖ فَقَدْ جَاءُوا ظُلْمًا وَزُورًا
Yéefar yi wax nañu ne : “[Alxuraan] jii daal aw duur la wu [Muhammad] moo ko sos, te dafa am ñu ko cay jàppale”. Li ñu fi indi tooñ ak i fen la.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Furqan 2

Simoore Al-Furqan Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom mi nga xam ne Moo moom nguurug asamaan yeek…

Simoore Aaya 2/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers