Al-Furqan · 32/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا نُزِّلَ عَلَيْهِ الْقُرْآنُ جُمْلَةً وَاحِدَةً ۚ كَذَٰلِكَ لِنُثَبِّتَ بِهِ فُؤَادَكَ ۖ وَرَتَّلْنَاهُ تَرْتِيلًا ٣٢
Transliteration
Wa qaalal lazeena kafaroo law laa nuzzila `alaihil Quraanu jumlatanw waahidah; kazaalika linusabbita bihee fu`aadaka wa rattalnaahu tarteelaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yéefar yaa ngay wax naan : “Lu tax wàccendoo wuñu Alxuraan jii wenn yoon mu ne ñumm ? ” [Waaye Nun nii la Nu koy wàccee] ngir dëgëral sa xol. Te it toftale Nanu ko bu jekk.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 30-34 — Al-Furqan
30وَقَالَ الرَّسُولُ يَا رَبِّ إِنَّ قَوْمِي اتَّخَذُوا هَٰذَا الْقُرْآنَ مَهْجُورًا
Yonent bi daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, nit ñi dey dëddu nañu Alxuraan jii ! ”
31وَكَذَٰلِكَ جَعَلْنَا لِكُلِّ نَبِيٍّ عَدُوًّا مِّنَ الْمُجْرِمِينَ ۗ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ هَادِيًا وَنَصِيرًا
Noonu la Nu defe woon Yonent bu nekk am ab noon ca tooñkat ya. Waaye nag, Sa Boroom Moom doy na sëkk kuy gindee, doy sëkk it ndimbal.
32وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا نُزِّلَ عَلَيْهِ الْقُرْآنُ جُمْلَةً وَاحِدَةً ۚ كَذَٰلِكَ لِنُثَبِّتَ بِهِ فُؤَادَكَ ۖ وَرَتَّلْنَاهُ تَرْتِيلًا
Yéefar yaa ngay wax naan : “Lu tax wàccendoo wuñu Alxuraan jii wenn yoon mu ne ñumm ? ” [Waaye Nun nii la Nu koy wàccee] ngir dëgëral sa xol. Te it toftale Nanu ko bu jekk.
33وَلَا يَأْتُونَكَ بِمَثَلٍ إِلَّا جِئْنَاكَ بِالْحَقِّ وَأَحْسَنَ تَفْسِيرًا
Amul léebu wu ñu lay mën a indil te indilunu la dëgg, te gën koo jub.
34الَّذِينَ يُحْشَرُونَ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ إِلَىٰ جَهَنَّمَ أُولَٰئِكَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضَلُّ سَبِيلًا
Ña nga xam ne dees na leen pang, di leen diri ci seen xar-kanam ya, jëme leen Safara, ñoom ñooy gën a yées wàccuwaay, gën a réere yoon wu jub wa.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
32Aaya
Tekki — Al-Furqan 32
Simoore Al-Furqan Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéefar yaa ngay wax naan : “Lu tax wàccendoo wuñu…Simoore Aaya 32/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








