Al-Furqan · 62/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
وَهُوَ الَّذِي جَعَلَ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ خِلْفَةً لِّمَنْ أَرَادَ أَن يَذَّكَّرَ أَوْ أَرَادَ شُكُورًا ۝٦٢
Wa huwal lazee ja`alal laila wannahaara khilfatal liman araada ai yazzakkara aw araadaa shookooraa
📖 Tekkim Wolof
Mooy Ki def guddeek bëccëg ñuy jëlasante ngir ku bëgg a xalaat, fàttaliku, mbaa mu bëgg a sant.

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Al-Furqan

60وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اسْجُدُوا لِلرَّحْمَٰنِ قَالُوا وَمَا الرَّحْمَٰنُ أَنَسْجُدُ لِمَا تَأْمُرُنَا وَزَادَهُمْ نُفُورًا ۩
Saa su Nu leen waxee : “Sujjóotal-leen [Yàlla] Mi di ab Yërëmaakoon”, ñu tontu ne : “Kuy kooku ?” - Mu faf dolli leen ug foñ.
61تَبَارَكَ الَّذِي جَعَلَ فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَجَعَلَ فِيهَا سِرَاجًا وَقَمَرًا مُّنِيرًا
Barkeel na [Moom Yàlla] mi def ci asamaan si ay yoon, def ca ab làmp [jant bi] ak weer wu leer nàññ !
62وَهُوَ الَّذِي جَعَلَ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ خِلْفَةً لِّمَنْ أَرَادَ أَن يَذَّكَّرَ أَوْ أَرَادَ شُكُورًا
Mooy Ki def guddeek bëccëg ñuy jëlasante ngir ku bëgg a xalaat, fàttaliku, mbaa mu bëgg a sant.
63وَعِبَادُ الرَّحْمَٰنِ الَّذِينَ يَمْشُونَ عَلَى الْأَرْضِ هَوْنًا وَإِذَا خَاطَبَهُمُ الْجَاهِلُونَ قَالُوا سَلَامًا
Ak jaami Yàlla yii dox ci kaw suuf si ndànk, su ñu réer ña di wàqanteek ñoom, ñuy wax jàmm,
64وَالَّذِينَ يَبِيتُونَ لِرَبِّهِمْ سُجَّدًا وَقِيَامًا
ñoom ñooy fanaanee julli te Yàlla rekk tax [taxaw ak a sujjóot] ;
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — Al-Furqan 62

Simoore Al-Furqan Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy Ki def guddeek bëccëg ñuy jëlasante ngir ku bëgg…

Simoore Aaya 62/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers